Ohh khassida bi rk la beug sama adina j’ai tellement cherché la traduction françaises j’espere qu’un jour je tomberai sur la traduction intégrale 😭😭😭
2025-05-28 21:40:33
162
La Desse🇸🇳 :
Mouy khassida go xamni, niou barri daniou koy diaxassé ba si yén kourel you makk yi ndakh douniou ko saytou.
_Al hadi bokk si tourou Yallah yi di firi « adji guindé dji wala adji dioubeul dji » moom la Serigne Touba dieul bind si khassida gui di « ihdi jamiha » araf bou né mou bind si bén bayitt, mouy niaane yallah guindi si képp kou koy diangg, ta daan na wakhal boppam moom S.Touba ni képp kou ko mokal, bo beugué guéneu si man sakh do
meune guéne.