Seydil Hadji Malick fii mo ngi wakh : madâd dahrou Sama Diamono diekhna , wal ayâmou ak biss ya , Wa zanbou khassiloune, tè samay bakar mane Seydil Hadji Malick mi ngi Yokou . Wayè nak dâfa modeste rek tè bakh ak ragal yalla lolll ndakh meussoul dèf lou yalla sippp wala lou kharam Sy Malick
2025-07-22 19:43:12
108
élement serigne babacar sy🇸🇳 :
Na niep wakh dieureu dieuf seydil Hadji Malick ❤️❤️❤️