Wolof sama XEET Ahmadou bama mbacké Elhadj malick sy baye niass mame limamou laye Machallah vive les wolof 🥰
2025-07-22 10:46:43
177
Djibril Thiam :
way wolof mo riche way ♥️♥️♥️
2025-07-22 12:15:00
54
Zahra7795 :
ki dou Guéweul Historien leu.Seutou Bou el Mogdad Seck leu.Dafa kham bopam rek machala
2025-07-22 14:39:22
58
forever :
vive les wolofs manchala
2025-07-22 09:21:41
38
Masire Isë Jéey Gëy :
Ku dul wolof xamoo li muy wax. Jërëjëf bi ma saa baay xamalee sama bopp.
2025-07-22 11:05:57
64
🇸🇳WolofThiam🇸🇳OG.Salum🇸🇳 :
limouy wakh ni yeup ayy khéttou wolof la machallah❤️❤️❤️
2025-07-22 12:52:08
54
Toujours Positif :
un vrai patrimoine maachallah yallah ngafi yagg ak wér ak soutoura.
2025-07-22 15:21:56
23
L'enfant béni 💚🇸🇳🇲🇦 :
Guéweul menoul gnak si société bi walahi ndayssane
2025-07-22 11:54:01
41
Mame Ndokhe Tv :
Mane omar Ndiaw dama diakhal billahi foumou khamé li
2025-07-23 00:35:20
6
DAMMEL TEEÑ faal :
lingay neexna Leerna machalla
2025-07-21 11:15:59
17
Serigne mbacke Diakhatè :
machalla Sama Nidiaye Omar Diaw Seck Histoiren Yalna Yalla Goudal Sa Fan Si Barké Seydouna Mouhamed
2025-07-23 00:00:35
6
Une Championne💪💚💛❤ :
ceux sont ces genres de personnes valeureuses ❤️qu'on veut au ministère de la culture, dans nos institutions scolaires, dans nos médias.. très longue vie à toi 🙏
2025-07-22 11:06:02
8
Dabina :
machallah genre yi lagnou wara diokh micro dougal ko sougnou histoire c'est mieux que histoire diambour yigni diagal té amoul bén ndiarigne
2025-07-22 21:52:28
5
💕💕💕 :
Li ngay wakh nii. Il y’a des personnes qui se proclament griots et qui sont plus âgés coquets toi you are smart. G même eu les larmes aux yeux. Je m’abonne direct bravo
2025-07-22 10:40:31
10
Maman Binetou :
liforaméla aka khame bopame li depuis primaire la thie tivaoune Oumar diaw séck moubakhemi machala 🙏💚
2025-07-24 01:54:13
5
Habib fall ✨Marie Parsine 🕊️ :
Machaalah tonton oumar xam histoire, xam mbokeu machallah mais demay sawaar si wakeur maodo ❤️ndakh Serigne babacar deno bokeu , rokaya ndiaye yayam khar yalla sidi bâ ka diour khar yalla ndiaré mbaye khardiata seck moka diour taya sarr sata sall mbassa ndiaye , aymérou youmé diey , batay ndiarè mbaye mo diour baba ndiarè mbaye diop mi diour awa baba , diour penda kamara mi diour yaye awa diop ibnou mi diour ndeye filly gueye mi diour Bassirou lô diour seme yaye mbathio lô ❤️
2025-07-22 20:51:36
11
Ong-Bak :
li moy Sénégal masa allah bayilen waso te wah Sénégal nous sommes même père même mère
2025-07-22 21:10:46
11
Adja Laye :
yaw ya meune métrisé manchalah ❤️❤️❤️
2025-07-22 12:01:54
9
Madjer :
vraiment Oumar soumalay dégue lou sama yaram daye daw
tu fais la fierté de la famille OULD SAMBA NORR vraiment Merci beaucoup frèro
2025-07-22 12:28:31
7
Dieng Immo de la petite Côte :
Mais kii mayou yalla laa amm dh lii dou boppou bou bahh rek
2025-07-22 08:45:31
11
kangadoz :
Bou el mogdad mon arriere arriere grand-pere.
2025-07-22 12:12:39
6
sunugal2050 :
machalla Machallah Seck li moye rolou guéweul Bou bax dou féké moukk mbokou Gouy yaxou Wala Mouy Tass ndax day Yor poussom di ñaw di dadiale mbok gui doré ka sa démb ba dará donoulé dará fa mbok gui sossoo AK sa Mame yak lalén si bolwén si Ngor👌Seck yalna YALLA Güena wérél sa xél Bijahi Rassoulilahi SwS Barké Chiekhal Khadiim darajatou Chiekhina Salih Rahimahoulah
2025-07-24 07:10:54
8
Une commerciale 💕 :
Tonton omar damala beugue rék té yalla takh depuis toute petite amale diam🥰
2025-07-22 12:48:50
6
AbduKader17 :
Le nom du "meen" ou "xeet" devait être ajouté au prénom de tout un chacun pour pouvoir garder la traçabilité comme on le fait avec le patronyme (sànt). Beaucoup de jeunes de cette génération ne connaissent pas leur "meen" ou "xeet".
2025-07-22 14:12:57
5
To see more videos from user @oumarseck119, please go to the Tikwm
homepage.