@papito_coly: Mbakhal Saloum yapp Bangui nonou les gens ……….. yé nako ladionnn donc abonnée len plus de recette et liker la vidéo aussi❤️c’est un régale ce plat#cuisine #cuisinetiktok #cuisinesenegalaise🇸🇳🇸🇳 #papito_coly

papito
papito
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 27 July 2025 21:26:00 GMT
898162
48172
618
2623

Music

Download

Comments

menudigitalsn
Dropshipping au Sénégal :
Douma leikk mbaxalou saloum 😏
2025-07-27 22:15:45
432
leye.djit
ZAMRANE AZZAKY :
des cœurs pour le prophète ps 🥰❤️❤️❤️
2025-07-27 21:35:25
261
iamohod4
Look at me :
yapp kénn douko Rosi day dgeur
2025-07-29 19:21:55
5
mrdiallo001
Kyachu✌🏽💚💚 :
Niouloug bi dafa bari
2025-07-28 12:44:15
150
arona105
Arrow⚽️✌️ :
Yow dall linguay préparer yep yakoy lekk nioune setane rek laniou si am tmt teguo ko ci yone dh😳😭
2025-07-29 01:11:47
1
princesse.mbaye1
Princesse mbaye :
60% yane iow li rk la bagn 🙃
2025-07-29 13:30:18
18
khadimfall987
khadim fall 😎❤️ :
Bala nga khame ni beugou meu li nga forssè mako🥺
2025-07-29 22:24:23
1
userctylqzsdn9
saliou hane :
mbakhalou Saloum kéne dou ko togué ni
2025-07-30 21:26:47
0
potenaaw
A💞🍒 :
barki yalla ma wax len deugeu meusouma niane mbakhal Lou safoul 😭😭
2025-07-28 01:30:25
3
itachi_boy4
itachi :
boy thine bii mom yako rakhass djiguén rakhassouko😅
2025-07-27 22:18:15
0
.lass19
Djigo Teraga :
mbaxal saloum kay yalla tere niak dokh ak niak moko takh niou la crie ko
2025-07-28 16:59:34
0
arame.diouf374
Arame Diouf :
Koulay togal ngay lekk amo fayam 😏
2025-07-30 17:04:40
1
yacinedieye6
Yasmina D :
Sauf moi meunou massi darra bilahi
2025-07-28 12:19:24
1
boul____kross
boul🕷️ Kross 👹👺🔫 :
dieulma may dégusté bok😂 gratuit
2025-07-27 21:37:39
1
badou4700
Aliaune :
Mbakhalou Saloum est ce que djaar na mouy am diwline ; puisque déjà guerté yii am nagn diwline
2025-07-28 19:23:26
43
ba.adama93
ba adama🇸🇳🇬🇦 :
li momé do mbaxalou salom😅
2025-07-28 10:08:51
3
gotze0102
Gotze8 :
meuno mbakalou saloum huile bi loumou siy déf
2025-07-28 16:31:53
0
morysylla13
Petit MO✌🏿 :
louway togg reik bam neikhla te amo tour toudei ko mbakhalou saloum ah mbakhalou saloum dei nangouna mom.. nioun saloum lagn deuk fall😂😂😂
2025-07-30 13:41:14
5
kheuchdaddy0
Kheucha :
wa lgui lii niatta la damako beugue
2025-07-28 05:03:04
1
boromerewmi0
A L G S :
😭makhal saloum mo dakh fille
2025-07-28 13:18:37
1
saloumsama..97gokh
saloum saloum bi :
ana mbakhalou saloum ak diwline yow il faut ma porté la plainte
2025-07-28 07:51:23
13
khadijasy329
Bb Khadija :
Togou gua sama plat préféré mounone guama invité 😩
2025-07-27 22:20:13
2
ousmane.darme.22
OUSMANE DARME 22 :
SALOUM SALOUM SEUL
2025-07-27 21:36:44
46
faloufalou23
faloufalou23 :
baakhout yapak diuen andougnou
2025-07-30 23:26:01
0
To see more videos from user @papito_coly, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About