Bokk na si lima geunn neex si sama adouna mooy limou nek Sama Toureundoo❤️
2025-08-02 23:48:19
640
UERKD Familly :
😭😭 loutakh déé ammm
2025-08-03 00:43:39
177
Dabakh~Maleek~Univers🍁🇸🇳 :
Je remercie mon père de m’avoir donné le de Abdoul Aziz Malick. Je sens que qu’il y’a une chose en moi qui n’est pas chez beaucoup de gens. Je me comporte comme si c’est moi Dabakh sans exprès. L’amour que porte pour Dabakh est commensurables et je ne sais pas pourquoi et j’aime tout ce qu’il a aimé c’est pourquoi j’aime trop Oustaz Pape Makhtar Kébé ❤️
2025-08-04 23:32:35
211
eladj09 :
Messouma ma guiss sisama aduna rak bou beug geum maguam com mame abdou nimou beugé serigne babacar ❤️❤️
2025-08-03 10:15:47
120
routier international :
Bilahi sama papa amouma fayame si limouma toudé Abdou Aziz 🥰
2025-08-03 10:10:15
132
abdoul baila gaye :
walaye deugeu la ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
2025-08-02 22:02:59
68
badaradiedhiou7 :
Oustaz Ahmed ba yalna ko yalla yeureum thé kharéko aldiannat firdawsi machallah boroom xam xam pire
2025-08-03 08:37:58
164
Thiate bou s BABACAR s’y :
Sallalahou alla Mouhamed 💚💚
2025-08-02 23:29:29
128
MOUHAMADOU MANSOUR :
Bilay sama Serigne mo bakh Mame Dabakh Malick ❤️❤️❤️
2025-08-02 22:59:10
57
Sora Bou Dabakh Malick ❤️📿 :
Shaybatal Hamdi Salaw Mome Rek La Beugue Deh🙏❤️🥺
2025-08-08 05:03:42
14
Adji~Almaktoum~Bint~Houssary❤️ :
Lii Dafa Kawé ❤️😩🥺😭😭😭😭😭
2025-08-19 23:19:41
8
mamadou sarr :
sallhou al mouhamedé
2025-08-03 09:50:19
26
Cherif Sakho :
lou gana nèkh am xam xam ba parè nagol djep 😭ndeysane اللهم إغفر له وارحمه 🙏