dooh bi yalla na done si niom ay khewel si barki serigne modou moustapha mbacké🤲😭
2025-08-22 21:23:29
758
fallou.badiane84 :
Tay niom la dei 😭😭ms souba nioune lay doon lii kouko doull bayi khell loula nékh defall 😭😭❤️❤️
2025-08-22 22:57:32
370
l'incompris 🇮🇷🇨🇳 🇷🇺 :
kouko wakh gnou saga la waaya kou nek war nga mana denci sa neew famou deuk ndakh li bou yaguei day andi épidémie
gnaffa reud yalla nalen yalla yeureum
2025-08-23 06:04:07
13
fayemu seringe saliou :
yallana don ndokhou yeurmande sen kaw
2025-08-22 21:34:15
91
Mame cheikh youm bou Pedri :
😭sama papa yalnako yalla khari ahldiana
2025-08-22 22:25:22
179
Lionel Guéye 10 :
Ndaysan le 11/ 08 lafi dinthie sama yaye 😭yalnalen yalla yeureum 😭 mettina déh
2025-08-23 00:46:32
38
mbayendiaye4057 :
yawmi ak manmi mou yague ak mou yékh filani moudjé yalnanou fékk si lou bakh😭😭😭
2025-08-23 09:30:40
36
anita fadhilou :
yalna yalla doli leine yeureume 😭😭
2025-08-23 13:44:17
9
Talibé s moustapha Maï 🤲🏾🙏? :
yalna ndokhmi doon ay kheweul ba aldiana 🤲🤲🤲🤲
2025-08-23 12:06:14
14
Ndiaga KANDJI :
yalla nagnou yalla até si yeurmandém
2025-08-23 13:15:55
19
𝙙𝙞𝙖𝙜𝙣𝙚 95 :
yalla nala yalla yeureum té xaréla aldiana
2025-08-23 11:50:33
8
birame :
fila sama papa teudeu ndokhmi yalla nadone ndokhou yeurmandé sisen kaw😭😭
2025-08-22 23:19:09
10
Charo couture🇸🇳🇸🇳 :
Ndiayesan 😭😭 yalla rk moy borrrr
2025-08-23 11:04:36
18
Adama sené :
yalla na léne yalla yeureum tékharé aldiana firdawsi 🙏😭
2025-08-22 21:58:28
8
Adja ♥️ :
Sma rakk dji serigne fallou dia 😫ndaysane yalle nala yalla yeureum kharè la aldjiana firdaws ak mbolèm dioulite boufa teud 🙏🏻🙏🏻ndokh bii yalla na done ay kheweul
2025-08-23 13:08:40
6
Diane tyma :
Yalna don yeurmande sounou borom😭👏
2025-08-23 00:16:35
6
COMPLEXE YAYE NGONÉ :
Kou guus li rek warnga xam ni adouna dou dara😭😭😭yalla nalen yalla yeureum XAREI len adjiana ndox mi wath sen kaww yalla na nek yeurmandei sen kaw
2025-08-23 11:47:31
6
Ndioba yaye fall :
ndeyesan ndokh mi yalna don yermandé ci gnom barkép serigne touba😭😭
2025-08-23 09:44:16
5
Ndeye Mbayang :
Fi bakha y’a la wala
2025-08-23 13:39:48
10
Yayou sokhna Diarra Bousso :
Thieuy sama makdjii 😭😭😭chak jour chak heure chak instant sama khel mogui thii yaw yalna aldiana done saa deukou way akk bep way ndawlou
2025-08-23 11:09:31
6
Abdou pouye :
ndayesane 😭
2025-08-22 21:52:46
6
Gana faye :
yalna len yalla yereum
2025-08-22 21:50:11
6
✈️Thier 63 🚚🛣 :
Yalla na yalla yerem Léna 🙏🙏
2025-08-22 23:47:23
9
Ibrahim Ndiaye :
Ndaysene yalla na léne yalla yereume si backup Serigne Touba 😭😭😭
2025-08-22 23:03:38
6
To see more videos from user @t379550, please go to the Tikwm
homepage.