bounioi diaayou ba fateii horma diaka dji waaw lene goor mashalah ♥️
2025-08-26 00:08:02
395
Nitou deug :
Y’en boy daguena wara nek nit té bayi sen thiakhan yi sof guen trp té ngewelei
2025-08-26 00:27:23
126
sokhna oumou✨ :
kou beugue la famille Mame Mbaye Dondé lalale j aime ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
2025-08-25 23:45:12
216
maxcatalan08 :
li nekhna dé
2025-08-26 12:05:53
73
Dija 💫 Xaragne Lo 🎉 :
wallahi hasim bourd kenn douko deff di mer mbecté mi foko takk wesou nako ❤️😂
2025-08-26 09:25:24
34
Tima 🇸🇳🦁Zahra sy ❤️ :
Non bourdeu dembeu ❤️🫀nekhna may ❤️
2025-08-26 08:01:55
94
Oustaz Mansour Fall 783032154 :
baye wakh len ko moutokc
2025-08-26 06:44:48
64
Amy khalifa :
mbecté bi may yeuk bène yone Thi ate mi tambalina😭🥰
2025-08-26 00:02:04
25
Noreyni :
Desfois dafay bakh niou jangal gayi li borom téré bii wax avant niouy nieuw bourde car dafa melni legui affaire yi ay tiaxane leu
2025-08-26 09:36:06
10
soldarou Serigne Babacar Sy ♥️ :
done talibé cheikh chance la 🤣😅😅
2025-08-27 00:59:14
6
moussa bou ndiol fouta :
Ndeysane kou lene guiss ngen ni reee moy fok ni da ngene dof 😀😀 te khamoul nii mbekte mi mo beuri 🥰🙏🙏🙏
2025-08-26 13:27:02
13
Diallo Diéri 💞💞 :
Ndeysaan xalé yi lii moy fééxeul séén xol yi, wouté ak gni nga xam né tama ak sabar la niouy bégué. Yalla na Yalla sammeu leen té déf leen ay magui diiné teksi may leen moudjou gou rafet si Barké Aladji Malick 🤲❤️❤️❤️
2025-08-26 18:06:44
28
nogaye Rassoul ❤️❤️ :
Machallah mbaye 🥰
2025-08-26 00:27:49
11
fina rassoul :
ohhh mbecté mi 😊 😭😭le bonheur d'être talibé cheikh est inexplicable 😭😭😭
2025-08-25 23:49:06
19
Domou sérère pire❤️ :
Lima yeugue taye guedji nako yeugue yalla nagnou yalla fayal maodo ak ndiabotam❤️❤️❤️❤️
2025-08-26 05:45:12
19
Baba Mou Thiat :
Waw gorré waay🥰
2025-08-26 00:08:40
15
AME KEUR TIVAOUNE MON COMBAT🙏 :
ame Keur tivaoune mon combat 🙏🙏
2025-08-26 09:54:05
9
Mbathie jou serigne mbaye Sy :
Demb moy premier jour wla 2
2025-08-26 21:18:09
12
Èva❤️Talibé cheikh❤️ :
Mbecté mi yalla boumou dièkh Fiére d’être Talibé cheikh ❤️❤️❤️❤️🙏🏻
2025-08-26 11:47:32
6
momo le tailleur du peuple :
liiii nékh n'a déé😂😂
2025-08-26 11:41:31
5
zeyna...9381810820265 :
seni pape di burde Guen wara awou di Tik tok le respect bok
2025-08-26 15:39:32
5
Maryam 🇸🇳 :
Sma hol bi Nn li nehna ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
2025-08-26 10:13:21
5
#ÉLAGE SECK 17# :
khana niari bunte guen diague wala
2025-08-26 10:03:30
10
Seutou Babacar sy ❤️🫀🥰 :
Ohhhhh sma khôl bi ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2025-08-25 23:55:56
5
To see more videos from user @ahmadoumbaye08, please go to the Tikwm
homepage.