@ndiagalayediop1:

BAYE NDIAGA 😍🥳💯 28
BAYE NDIAGA 😍🥳💯 28
Open In TikTok:
Region: SN
Wednesday 27 August 2025 01:44:32 GMT
72181
11158
322
965

Music

Download

Comments

user51816953343635
user51816953343635 :
kou wah ni layenne yi hamou niou dinne rek walahi ioe mi ko wah ya amoul thieur si yallah...si dara rafet , te wa tassimou bi habli lahi jamii-an, niom layenne rek niokay appliquè si lou neubou ak lou fegne.. dieureudieuf limamou laye, laye laye..beug nalen
2025-08-27 11:21:20
105
user4546674537175
user4546674537175 :
Li layééne rek gno am khole bou tollou ni yééna bakh🥰🥰🥰
2025-08-27 08:31:44
175
soba304
Babs Niang Niang :
wa Li foumouy amé beig nako feké
2025-08-28 07:23:15
0
djawecisse
user20328228697211 :
waa li nékhoule rek yamsi walahi🥰🥰
2025-08-27 17:59:51
1
mouhamedndiaye7479
♏️🅾️UHAMED 🥂NDℹ️🅰️YE✂️✅ :
Degeul lignouy doublur fofou okh ❤️😭
2025-08-28 00:31:15
4
imamalahi_33
Imam_23_🇸🇳🫱🏽‍🫲🏻🇪🇸 :
Yéeeee bi sunu ko manonn bayi dina baxx tropp diapp lenn si meme Diamalaye Sikar yi defois ngenn siyy dougeull loussi bokoull Machallah quand même 🥰
2025-08-27 10:22:51
21
ndiaga_1
1️⃣3️⃣ :
Soumeu nekoul wonn Talibe cheikh barki serigne babacar sy layenne lay Donn😭🤍🤍🤍🤍
2025-08-27 20:51:10
7
dero.italia
DERO.capo :
Machalla hoooooo limoye carte d'identità Senegal 🥰🥰🥰
2025-08-27 15:38:49
3
rokhayacisse153
Kire :
borom daradji dafka dan tekki si jour ou gamou bene par bene di firi limouy tekki ndeyssane
2025-08-28 07:49:56
0
sambayediop4
Sambaye Diop :
yenako dakheu tidian yii❤️❤️❤️
2025-08-27 20:53:07
4
hamidouly325
HemsJrAlfoutiyou :
Alhamdoulilhah Islam amatinaa ndaam❤❤💥😍✌✌✌🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
2025-08-28 01:44:32
1
warayta6
Rita :
Le peuple élu de Dieu 💯🥰❤️
2025-08-27 16:09:36
40
cheikhtidianedi134
Cheikh Tidiane Diop :
yalna yala faye yiw té barkèle macha Allah
2025-08-27 21:01:11
3
alioumbaye5385
Aliou Mbaye :
🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰 machallah li nexna way wa keur rasoulilah yii gno meune way
2025-08-28 08:07:32
0
sokhnasy85
sokhna sy85 :
ngi Ay talibé cheikh lay lébou maodo yi
2025-08-27 23:06:18
4
sora.ndiaye517
Sora Ndiaye :
Yéna bakh
2025-08-27 16:19:02
2
malick.diop126
Malick Diop :
Layéne danou niack kiniane Machalah
2025-08-27 15:53:09
6
maumo2605
MEUM :
layéne akh tidiane yi bilaye cilvissé
2025-08-27 20:59:56
9
user8400796516765
user8400796516765 :
Machalla 🙏Lepp bé’nn la
2025-08-27 17:36:56
1
imaw485
attydiany :
non layennnne. beneenn.affairre laniou ndaysan kennndou cheikh tydiany wallahi
2025-08-27 14:26:03
4
mouhamadou.naby
Mouhamadou Naby :
yêna bâh outé ak gnima hah
2025-08-27 20:37:10
2
tymaousmane
Tymaousmane :
Le peuple est content 🙏☺️☺️☺️
2025-08-27 21:00:02
2
thiauser287324881570
thiapathiolyayam :
amoulène morom
2025-08-27 21:20:29
5
immortel.sp.1852
immortel :
machallah les femmes ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏🙏🙏
2025-08-28 00:57:22
1
ndiaye.amiseck
Ndiaye Amiseck :
machallah kéne dou yéne layéne yi yalla na léne yalla faye sy barké seydina Mohamed ak Serigne babacar sy❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
2025-08-27 17:45:14
5
To see more videos from user @ndiagalayediop1, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About