@kanna bass:kepeuh kou bind Inna anzal nahou ben yon ba si sallamoun nga bamouko 7 fois yam fofou. so paré nga defko safa tangalko bilekok domou tal. nanko diokh si sa diabot walahi lep loumou fek sa bir dinako rakhass bamouy set tee nit dotoula diap si lek