@djzizvoice: Sen Xalat ?? 🧠#sénégal #nietelguissguiss #senegaltiktok #pourtoi #sénégalaise🇸🇳

AzizKapulo
AzizKapulo
Open In TikTok:
Region: US
Friday 19 September 2025 07:02:17 GMT
38683
3167
271
306

Music

Download

Comments

ouz113
ouz113 :
Solution bi moy so amé se nit mou léb leu daguay khol lo am té douleu guagn ng may ko
2025-10-02 11:51:05
16
race4839
CERA :
Solution : liguey rek soutral sa bop
2025-09-30 11:11:42
35
jaimemon_paye362
j'aimemonpays :
niaka léplé boor tamit day yakh diganté
2025-10-02 14:14:28
3
metzo249
@metzo-🎶🩸🫧 :
Senegal niouye faye bor bariwol 😳
2025-10-02 00:13:32
1
ombre1458
Ombre :
« Soit tu perds ton argent, soit tu perds ton amitié avec la personne. »
2025-10-02 00:01:25
20
zaltalightsene
zaltalightsene :
Sénégalais suley leb rk daley door
2025-09-30 19:03:10
5
zanzi773
Zanziba :
solution c'est gniaka guemou yalla
2025-10-02 02:51:55
4
user3784425052565
Seck Ndandane.Com :
bilakhii grand Lou lerrr geu wakh
2025-10-01 10:56:39
5
user1185434504981
doumou deuk bii :
bilahi dinga lebal nit mou diaréfa sakh méré la ndakh fayé kou ba kham na si dara mé grawoul mane kouma bayi sama xalis boumala mayoul ya kham
2025-10-02 13:57:33
1
abdoulaye.ndiaye501
Abdoulaye Ndiaye :
doylou moy solution bi🥺
2025-10-02 19:37:40
0
mouhamedbomou2
Mouhamed naby :
wallaay degge la loulèèr gaa wakhe ni je valide
2025-10-02 16:51:00
2
gawanexpress
Gawane Gp🇸🇳🇨🇮 :
Nit gni nio wara gorei rek mais mom Boor meunoul niak , personne n'est a l'abri des problèmes financiers.
2025-10-02 00:39:44
4
omarnjie227
Omar Njie ✅️ :
bilahi lol moy deugeu sakh man mi lol dalnama lou beury
2025-10-02 13:42:45
2
adamabeuguebamba4
beugue bamba :
bilahi dégueula vérité
2025-10-01 15:36:03
3
user96396212034861
El Hadji :
l'emprunt fait parti de la vie et nul n'est à l'abri de cette situation
2025-09-28 22:15:56
10
mariamaseye31
Mariama Seye31 :
li nguay wakh massi kham dara Sénégal
2025-09-30 23:19:25
1
nestasarr
nestasarr :
C’est vrai sama béna copain ndesyssane lolu mon ko dall si mane 50mil le abe mai dina fay dh ndekh yor na ko da titt rk si xaliss 😂
2025-10-01 10:03:17
1
damembengue1
Dame Mbengue :
Fi bu amon vocale😭 ma netali sama kharit lolu mo yakh sama digante ak moom 😭😭😭
2025-09-19 17:23:56
10
cheikh.diakhate52
Patriote :
Vraiment bo manoul fay waro lep
2025-10-02 12:32:08
2
talibe_13
user8833094816363 :
La solutions Lépe boor. Faye la sante c’est tout . Nite kou bakhe day gorrer
2025-09-20 09:50:06
13
ka.mouhamed
Ka Mouhamed :
lou amla dh
2025-10-01 11:02:49
1
moussa.sarr304
Moussa sarr :
Boor deume leu la rk 😂😂😂😂❤️✌
2025-10-02 10:19:06
1
khalillahi
Khalil :
Bo léb léwul gnu bala : Solution bi son Womatt de Youssou ndour
2025-09-30 23:18:02
2
omarlo153
omarlo153 :
c'est vrai dé. Souvent diamono diapou Ndanane
2025-10-02 19:38:29
0
mouhamed_nby97
MOUHAMED_NABY🇵🇸🇸🇳🇵🇸 :
Mane sama nit douma leblanté ak mom
2025-10-02 15:31:33
1
To see more videos from user @djzizvoice, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About