Wakh deug mome yeufeumla Bilaye lolou mon takh ma beug ko liss ndiago or bi seule 😁❤
2025-09-29 15:18:01
780
khalilloulah :
machala wakh DEUG dafa am solo
2025-09-29 14:34:14
895
Ndiaye :
oohh liss gouygui wakhon Nala ko😳
2025-09-29 15:30:24
353
𝐁𝐚𝐝𝐚𝐫𝐚 3𝐁𝐃 🧨 :
Rouslo nga ay nitt dh 😂😂
2025-09-29 16:06:13
240
Jadon Sancho 25 :
Ndiago day deugou d’où féne yw diambare gua yw seul dague koy Daw
2025-09-29 14:29:33
229
Momo Gueye :
guouy gui fila lako wakh dila conseil guakoy saga
2025-09-29 19:16:19
94
Papa Gueye :
xolal lii déf émission bott sa sac mémé élève yi classe douniou wéko sac mbeur nékal nit
2025-09-29 15:01:27
47
L'enfant terrible 🇸🇳🫶🏿 :
dél wagni song bi
2025-09-29 15:43:04
89
Sega.D :
Kiy présenté émission bi beurri na wakh do bayi kiga invité wakh
2025-09-29 19:24:59
25
ame bou ada fass 🩸 :
ada fass wakhon nako souma pâre si iwo dangay doff
2025-09-29 17:31:57
8
ZÅLL.0.2.0.4🤟✌️❓ :
man mome damala beug ba paré rk barki Serigne Touba diambar gua dh lépp dina bakh bly 🥺🥺🥺🥺🥺
2025-09-29 15:12:07
35
Hamdy🔥🇸🇳 :
Ndiago dou féne 🥰
2025-09-29 15:00:13
50
AGNT Osmn Dm :
ceux que je ne peux pas comprendre comment un athlète en lutte au Sénégal 🇸🇳 peut gagner plus de 50 millions sur un combat et ne pas avoir toute les infos sur quoi prendre et comment se préparer pour un combat. Même le CNG est fautif
2025-09-29 17:20:38
32
@lamine Style :
ngouy ngui wax nala ko fii nga koy diay réw
2025-09-29 22:25:04
12
Amzo331 :
bravo liss li moy goor deugue
2025-09-29 19:57:54
9
P A P I T O ⭐️ :
Ni leu assume rek et ont passe 🤝🔥
2025-09-29 20:44:10
12
ki andoul si caise noir bi :
après bilako gouy gui wakhé ngay sissou
2025-09-29 19:16:00
11
David Sénégal :
gouy gui wahonako ngén Koy sagua
2025-09-29 19:22:36
10
NDIAGO Bi :
liss ndiago kèssé lagni tope tu raison
2025-09-29 18:52:25
9
leuzz🤴🇸🇳 :
Say supporter ngua nakhon way dou niounn 😂😂😂
2025-09-29 16:05:57
14
majoor :
wa mom niata yon lafi tog né lolou wagni wouko dara parce que sila dan lac rose😂
2025-09-29 22:06:25
8
Ö ňďænē Măįssa ẁalÿ&✪ :
ooh ki mako beug
2025-09-29 18:13:36
6
PAPI :
bila ko gouye Gui done Conseiller danga ko tonte après sa boy yi diko saga
2025-09-29 17:53:12
8
Azou_boyiz2 :
bly liss nite kou direct la
2025-09-29 17:04:06
7
Ousmane sy :
Son bi tamitt ohh degouma dara ahh 😏
2025-09-29 17:57:24
6
To see more videos from user @zall_bou_liss, please go to the Tikwm
homepage.