@mamadou.zf: Affaire Lamignou Darou : L'audition est terminée, mais Maître Famara Faty dément la garde à vue ! #justicepourlesmartyrs #senegalplus #ousmanesonko #diomayemoysonko #senegal
EXCELLENCE ✊🏾⚖️🇸🇳
Region: IT
Tuesday 30 September 2025 15:47:39 GMT
Music
Download
Comments
Assane Faye :
mais procureur khana dégoule cheikh Bou Macky et puis loutakh kou saga Macky gnou wolla. té kou saga sonko rien ne se passe
2025-09-30 16:18:03
20
Cours Al Quran ألقرآن الكريم :
cours en ligne al Quran disponible
2025-09-30 15:55:45
10
patriote435 :
Dagn ko wora tejj boy bi dafa reww
2025-09-30 16:36:37
5
Babou Ba :
merci beaucoup Lamene darou
2025-09-30 16:14:32
12
Lamine :
waxlén sen wax thi foule ak fayda té bayi saga rafétoul
2025-09-30 18:43:48
0
baye saliou ndiaye :
mandommbé 😭
2025-09-30 16:24:02
0
tawfekh caroleur :
procureur bi xana day lir statut wa apr yi li naiw na bayi len projet bi dem ligeyi
2025-09-30 16:42:59
1
Amadou Sarr :
dhekke bii booguole sagua.naniou lène bayyi niou nhibii
2025-09-30 16:32:43
1
Dija Diallo :
mani niou bayi wa apr ak seni saga te khamni sénégal gui amoul lois macky moy dirigé rew mi
2025-09-30 16:56:29
0
Sarata Daffe :
Merci
2025-09-30 18:37:07
0
Aliou Ba Bou Bintou Ndiaye :
lima thi xam moye bon sagatté sonko nio nopi
2025-09-30 16:48:44
1
nestorine badji :
merci me faty🙏🙏🙏
2025-09-30 16:09:46
1
momo :
donc insulter PM est permis au Sénégal
2025-09-30 17:16:47
0
mame halifa a vie :
bilahi dofolen sax
2025-09-30 16:02:27
1
EXPERT 100% BIO :
Darou pour mane dinanko diap bou yague. Dafa eupeul té dafa yaga wakh
2025-09-30 16:26:02
0
Ablaye diouf Baye fall :
lokho sonko guenou si mome miy diokhe Ay vidéo
2025-09-30 16:26:12
0
Ibrahima Diouf :
Procure bi say tane la pir sak jour niou saga sonko te defoul ligayam mouy diay fimiste
2025-09-30 16:23:04
0
la plus belle 💕 :
saga sonko mom sou nekhone diomaye tay mou dag il a tous les pouvoirs
2025-09-30 16:48:16
3
malickba52393 :
Merci beaucoup 👌
2025-09-30 16:20:50
1
Dame Secka :
Merci 🥰
2025-09-30 18:56:56
0
momo :
mane dall douma comprendre ce procureur la de la république franchement
2025-09-30 17:16:01
0
Massamba Mbaw :
🙏🙏🙏merci
2025-09-30 16:55:28
0
Alerte :
@Lamignou Darou 1912 dafa impoli
2025-09-30 15:53:36
2
Oumar cisse :
🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
2025-09-30 23:22:31
0
Ets 18 Safar marché central Th :
🥰🥰🥰
2025-09-30 21:44:05
0
To see more videos from user @mamadou.zf, please go to the Tikwm
homepage.