@liye.khew.sngal: inondation Touba #Touba #inondation #senegalaise_tik_tok🇸🇳 #focus2050 #focus2024🇸🇳❤️    #              sonko

Liye Khew Sénégal
Liye Khew Sénégal
Open In TikTok:
Region: SN
Tuesday 30 September 2025 22:32:12 GMT
334350
22093
496
494

Music

Download

Comments

bergeriedarousalam4
Sangue bi diagne ❤️ :
Guisse ngene ni ndokh bi baré nonou lafi kheweul Adina ak alakhira baré
2025-09-30 23:47:24
1176
bambaj667
bambaj667 :
Malaka bou yor taw bi xana da ame ay toll touba 😂
2025-10-01 06:19:01
146
khaliloulah.ibrah1
Khaliloulah ibrahima :
kana Touba da war tou inondé. soff guéne
2025-10-01 16:13:52
1
salimata.hane
Salimata Hane :
wa Touba nak li yannn bou nagou la Serigne Touba limou ligueye Moy fegne machallah mbake balla aicha
2025-09-30 23:26:27
261
maty.sylle
Ndeye maty :
Taw 18heur 30 la comamasé ba fi may écrire 22heur 50 Billahi
2025-09-30 22:47:27
484
timacarter49
Tima Carter 🇸🇳 🇺🇸 :
Lou tax Dakar d’où taw😩
2025-10-01 02:24:52
10
diop.djibril5
DJIBY DIOP :
Touba cité lumière fondé par le cheikh du mouridisme grâce à son endurance et sa bravoure face à l'ennemi. Un jour tous ces problèmes seront réglés
2025-09-30 23:00:30
132
user1677947755194
Aminata__Lô :
li dé bouniou kheuyé souba mou diékh
2025-10-01 16:19:56
0
seydinaakime
mballo :
c très bien pour vous
2025-10-01 01:36:24
1
xamxam796
kiné diagne :
nagne xalaat kitax gnou deukk fi taye daane na tawté té kénne daawou ko jappalé serigne tuuba 😭😭😭😭😭😭😭😭😭
2025-09-30 23:44:57
82
amdymoustaphakhassida
Amdy Moustapha Seck khassida :
Yaw mi di filme sa xole bi wargako defarate touba mom dofa wane lou bakh
2025-09-30 23:25:26
28
ndiagambaye49
ndiaga mbaye :
question Lou takh limiy taw touba douko taw fanéne si Sénégal
2025-10-01 06:29:54
62
abdourahmanediaby
JÛÑIOR LÔ O.S.T🇺🇸🇨🇦🇸🇳✌️ :
yalla na yalla doli soutoura wa Touba 😢
2025-10-01 00:34:32
83
lahatdiouf815
Lahat Diouf :
Yalla na nek kheweul gou sawane bawane Barki Cheikhou Khadim🤲🤲🤲
2025-09-30 23:05:20
374
usernxztmrswq3
Fatou Diakhate :
Yalla n'a ndokh mi nek glace si kaw waye dawlou yi🙏
2025-10-01 07:52:04
29
soxnajarrah2009
SOXNA_JARRAH🤴🏽🤍💗 :
bo kheuyé fadiar nga filmé watt🥱
2025-09-30 23:55:02
12
massifbois
S@liou by :
santé len borom touba mi waral taw bi🙏 dieureudief mbacke alla nga khép dolli
2025-10-01 00:36:34
24
user1560831367613
user1560831367613 :
khad voté ndogou jubilé
2025-09-30 23:55:42
31
mio30911
pape Ndiaye :
video 2023
2025-10-01 00:51:18
3
mouhameddiop5311
Mouhamed 𝔻𝕀𝕆ℙ Baye Fall :
Leppu Borome Touba Adji mag dji la💪❤
2025-10-01 12:47:58
6
mamadou8224
Mamadou KOMI DIMO🇸🇳🇸🇳 :
Wa touba rupture lagn bougone am nagn ko
2025-10-01 08:31:17
1
perwally
yal na Viviane ak Titi dioubo :
Touba diomaye 230 voix Amadou ba 4 voix😂😂😂😂😂
2025-10-01 10:27:54
1
_money_992
SADIKH :
Justice pour BOCAR SAMBA DIEYE 🙅🏾‍♂
2025-10-01 00:12:57
49
bambadiengpros
Bambadieng09 :
Mandat 12 ans Wade mandat 12 ans macky touba di melni ba tay 🙏
2025-09-30 22:58:24
4
guidothiernoalioudiallo2
talibe cheikh tidiani Cherif❤️ :
ana président de la république walla Sénégal amatina président 😁😁😁😁
2025-10-01 00:38:54
2
To see more videos from user @liye.khew.sngal, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About