@abdou_karim_01: Ah doom… #ahdoom #mamecheikhibrahimafall #waximamecheikhibrafall

Abdou Karim🧑🏿‍🦱🇸🇳
Abdou Karim🧑🏿‍🦱🇸🇳
Open In TikTok:
Region: SN
Thursday 09 October 2025 00:35:37 GMT
468046
83530
1134
1137

Music

Download

Comments

fallaladin
F.M.ALADE🏌🏽✌🏽 :
Ahh doom! Lep lou wayy di niaan yalla soukoko naroutt wonn mayy douko deiff si xelam bam koy niannn!
2025-10-09 19:14:44
1364
noksbody2
Thiatou cheikhra fall 🖤🤍☝️ :
yallah boula xanié dala dimbali boula mayé itam dala dimbali yallah dou dioum !!! cheikh ibra fall !!!
2025-10-09 12:26:06
1307
galsen_tiktok01
Abdoulaye✪ :
Ahh doom « Lou liguey di Mayé rouss nako niann yallah »
2025-10-09 16:34:47
483
mame_thierno66
𝐌𝐀𝐌𝐄 𝐓𝐇𝐈𝐄𝐑𝐍𝐎 :
Ah Doom《jaajëf katt gatt na wayé kou jëfuul darra doko dégue》❤
2025-10-10 20:45:17
269
thioro557
thioro bæby 💋🫶 :
Ahh doom!! Wett gooré wettalikou gooré🖤🤍
2025-11-20 23:55:40
80
yayefallbi020
khar Karim❤️🦋 :
wétte goré wétalikou goré nameu fou sorri beug lou barri Cheikh Ibrahima Fall lamp!
2025-10-10 10:38:40
153
sallpro08
ELNDARAWY RMG 💫 :
Ah domm koulay diaye xam xam diaye ko talibé ndax ibliss kéne eupou xam xam niake talibé mo waral nomou mel 🥰👌
2025-10-09 20:55:07
107
khadyfadillou0
卡迪·迪亞❤️🏅 :
Ah domm!!! Masamba ndiaye waxi sikk bou nitt xam si moromam batax mou wérko Doom boromam xamna si mome sikk buko raw neubal koko🤝
2025-10-09 23:56:28
124
jolie_nana249
Ayshuu🎀 🧸 :
Ah dom … boul merei nit ndax loumou tass sa yakar wayer mereil sa bop thi ligua wekk sa yakar si koudoul YALLAH ….
2025-10-10 13:37:28
135
bourama4444
Papa mbodji ❤️⏳️ :
Ah doom Mbirr bosa beugué âme ndam daguay nangou "touma ak gathié"
2025-10-09 19:48:13
154
cheikhbambandiaye140
Cheikh ahmadou bamba ndiaye :
Un vrai philosophe💡Sidi Birahim Fall👌🏾
2025-10-11 20:43:22
40
coumbista636
Niénio bou ndaw🙂‍↔️❤️ :
Lou liguéy di mayei rouss nako niane
2025-10-09 00:42:53
59
makhtar.jr.leye
Makhtar Jr Leye :
Ah doom : lou nieuwagoul Dfa diotagoul 🥰
2026-01-29 22:13:21
16
ndeyesodaseck7
Soda bamba ❤️ :
Boula Dra def Loy rethiou dax adouna yagoul saxoul te biss dina niew ioe kasse ak sa bamel ak say dieuf 😫😔😔
2025-10-09 10:33:52
55
sambadiouf285
Bathie Diouf :
Ah doom !! Lou liguey di mayé rousse nako niane 🥰☝🏿
2026-01-27 13:53:59
21
djibsons0
pa djiby :
ki dieuf ba raw la meuno wakh ba dab ko☺️
2026-01-12 23:28:22
19
soxna088
Soxna Khadidiatou 🏁❤️ :
Ah doom!! Liguey gueun diangue, djoxé gueun djouli, mandou guen koor
2025-10-10 10:25:38
37
balla20032
Balzo Rassoul 313😎 :
Mame Cheikh Ibra damako beugg wallahi🥺❤
2025-10-09 16:41:37
34
unefadilate133
Maï🧸🍒🍹 :
Mame cheikh Ibra fall Bayou Gör gnii nena Ahh dom diamanoy Tay li nexx rk la Nit gni di boke ak yaw wayé si sa ay diafé diafé yaye guena wett ab new ⚰️si birr bamel 👌🏿🪔 mo deg
2025-10-09 23:56:37
95
baradiop2211
𝙎.𝘽.𝘿𝙆𝙄𝙉𝙂🇸🇳☪️ ✪ :
Ah doom !! Adouna Lou doye amoufi doylou mofi am ✌
2026-02-19 22:35:09
13
amate072
amate072 :
Ah dom lou liguey di mayé rouss nako niane
2025-10-09 18:15:49
49
beugbamba041
LEYE BOU BAMBA ☝🏿🤍 :
nafékh Dina dijouli Dina wor wayé dou diokhé alalam si yalla
2025-10-10 01:23:18
18
bintoumboup9
Bintou saliou gawani :
kou yalla defar boko beugè yah MBA do moudiè yahou
2025-10-10 13:07:59
21
bara.mbengue6
Bara Mbengue :
Ah doom《Kouy déff kou rombou nganii dou wadja Wadja dinala rombou》
2025-10-09 23:29:51
38
arfang797
Arou Ndoye ✪ :
Ah Dome Massamba ndiaye wakhie Rérré yalla dana takha niemé yalla Massamba Te kou bakh kham na kou bone kham ngua Nakh kou wétt kham sa bopou Wayé kouye kholle nitt di guiss si mome ab mbonn Massamba bakha go Boulen faté ne moukke bakar boudon khégne dina khégne fougne ko fogué woul dh Talatay Mame cheikh Ibrahima Fall 🖤
2025-10-10 12:54:41
96
To see more videos from user @abdou_karim_01, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About