@naby_kara: Booba ba tay yaa ngi wax Nu mel ni da ñu la déggul Yaa ngi junj te yaa ngi cax Mel ni da ñu la faalewul Li nga leen wax da fa leer Topp tektalu DAAM a wóor Mooy njariñ te moo di ngor Du nuy tubaab, du nuy naar Sunu réew raflewul xam-xam Raflewul njub te raflewul jom Na nu xalaat, xalaatlu du ndam Na nu yeewu, xippi tey xalam Leneen lu nu def noo ngi juum♥️🙏🏽#cheikhmodoukara☝️ #serignetoubaTaalifcheikhmodoukara❤️❤️❤️🙏🏽 #jahkara #vue #pourtoi
M.E.T.H👌🇸🇳 ✪
Region: FR
Friday 10 October 2025 18:48:45 GMT
Music
Download
Comments
Vit8nlyKara ☝🏾 :
Keineu douci leineu lepp moma 🥰😭
2025-10-10 19:08:43
21
Souleymane Wele Diedhiou 🇸🇳 :
Jah Kara rek 👌🙏❤❤❤
2026-01-01 21:43:24
0
Xadijah~Faal~BDN 🚩🏴! :
Yaniou mom 🥹✨❤
2025-10-10 19:43:23
10
bleu_ndiaye💨🇸🇳 :
Kilifeu titre son bi❤️🙏🏾
2025-10-13 22:40:43
6
BADOU KARA BOU BOY Niang :
dieum jii rek monou yem👌👌
2025-10-15 22:52:36
6
bamba kara :
titre song bi way
2025-10-13 12:54:42
4
borom darou :
walakhi
2025-10-10 18:55:58
6
tapha1764 :
🥰🥰
2025-12-02 22:38:42
4
Ndiouga313 :
aka doye waaaaaar
2025-10-11 02:13:53
5
bambadokara :
ndeysane ohooo😂😂😂
2025-10-11 20:21:48
1
AL BICHRI MULTI-SERVICE :
MANE DÉ MOOM LAA BEUG 🥰🥰
2025-10-13 12:30:51
2
Cheikh Awa Balla Officiel :
🖤🤍☝
2025-10-10 22:20:12
4
🌸Soxna Maï Jadid Kara🌸 :
❤️❤️❤
2025-10-10 19:08:46
4
Ass malick :
❤❤❤❤👍👍👍👍👍👍
2025-10-10 21:02:07
3
Soxna Saly kara❤️ :
❤️❤️❤
2025-10-10 19:14:39
4
layekara11.6 :
😭🥰😭😭🙏
2025-10-10 19:40:40
4
ABORY KARA SAANI :
❤❤❤❤
2025-11-04 15:16:40
2
🇦🇱ÑÍÃÑG BÕÜ ÑÕRËYÑÌ☑️ :
🥰🥰🥰👌
2025-10-10 19:05:00
3
barra Thiatte💪✌️🤩 :
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️✊
2025-10-11 04:21:31
2
Diantal Boy MÉDINA 🩸🧠💸 :
👌👌👌
2025-11-30 01:46:32
1
Moom Maam Seex🖤🤍 :
❤️❤️❤
2025-10-13 22:16:06
1
maria :
❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2025-12-04 12:34:12
0
S habdokhader bousso :
🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2025-12-15 06:37:51
0
ndayan Awa Balla 🚩🏴✌🏿 :
🙏🙏🙏
2026-01-31 16:05:59
0
fallou baye fall :
👌👌👌
2025-10-11 13:58:10
0
To see more videos from user @naby_kara, please go to the Tikwm
homepage.
© 2021-2026 TikWM. All rights reserved.