bismilah.
liguéyeuntè bi mo wara dak.
diap domou diambour diko liguèy.
bayilén ko.
kham nga kouy dèf lou bone do am protection. nakh dou nieup nioy balè
2025-10-15 22:39:23
68
Natoma55❤️🥰🤧🍎 :
louye torokhal sa none la beugue akk képe kouma ligeye mou keupou si kawame 😘
2025-10-24 07:00:17
9
ML1.0 :
Danaka df dh koulay liguey soumay diekou dila ray 🙏
2025-10-16 22:17:38
16
Gorgui :
dinako défe inchalla kou dh sama yone nékousi sama boop mala guenele d'où bagne nala 🙏
2025-10-16 12:39:25
24
mint nabii :
billahi beugueu nako déf mais beugouma kén fatou
2025-10-16 07:26:00
9
machalah Diopba :
merci serigne bi legui les gens sont mauvais pour un rien rek ils te maraboutent trop de méchanceté
2025-10-19 10:29:28
18
cheikh baba :
Sala laho ala Mouhamed ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤
2025-10-16 22:52:14
9
Khady Dieng :
dama RAGAL niéméwouma yalnaniou Borom Bi Aral Bopam Amine
2025-11-12 12:14:15
11
Assane seck Sandaga :
Salalahou Ala Mouhamed
2025-10-16 09:46:13
60
sikhou.0 :
2025-11-19 00:21:39
6
Awa bou mouhamed🥰🥰🥀🥀❤️ :
Kharal ma nieuw deff kooo legui amoul khar 😁
2025-10-17 23:11:52
11
ahmadou :
sokhar t say mbok niolay liguey fi ak dewo dugn am diam
gnilakey def dougn yewou ba tek sen dieu si souf lep senkay lay délouwat