j'ai une gastrite on m'a interdit de manger des arachides
2025-10-16 21:38:58
30
marietou cisse :
dafa yarou et honnete
2025-10-16 21:51:37
458
BARHAMIENNE BUSINESS :
professeur yalla na la yalla faye leup lou bax lingay def ya rabbi 🙏 yalla nala yalla bolé si tanéfou cheikh Ibrahima Niass yi ya rabbi 🙏 lima la nianal ni bilahi sama xol lako tibbé danga bax té am eudeup Machallah. yalla na yalla contane si yaw. fo joublou si adouna yalla ngafa fekk Baye Niass ya mouy sa sauvétage ya rabbi 🙏😍❤
2025-10-22 12:59:58
108
Mame ale seck :
yalla n'a yalla goudal sa fane amine
2025-10-16 22:35:10
162
ndèye yandé Ndiaye :
j'ai entendu que guertè dafay diohé cancer est ce que c'est vrai