Wallahi souma wallahi
Yallah magui lay gnane ma guissanté ak Mohamad salallaaw alaiyi wa Salam deuk ak mome al dia naa
Sama liguéy si diné ak sa diamou Yallah mounomakoo mayy
Yow sa borome Balma bal samay wadiour ak bolém dioulitt
Té défall ma sa ma bébébb bi