@khidmatoul_khadim7: Nianal lene ko bou bakh mou sakh si khasida yi diambar deug leu ❤️🥰

Dahira_khidmatoul_khadim_u7
Dahira_khidmatoul_khadim_u7
Open In TikTok:
Region: SN
Tuesday 28 October 2025 01:48:09 GMT
425257
82297
1811
580

Music

Download

Comments

xidmatv
Xidma Tv :
Rakh na ak Gëmmeentu d
2025-10-28 16:31:59
1568
soxnadiarrasaliou36
Soxna Diarra saliou 😍 :
Yallah nama yallah may domm bou mèlni si barkép s saliou Mbacké
2025-10-28 10:22:32
1256
niayefall111
niaye fall111🇸🇳🇸🇳 :
boy bi day ték khél rék ms mogui nélaw 😂😂
2025-10-29 19:00:53
226
m.o.u.r.bb.s.o.w
m o u r bb s o w 🧏☠️☠️ :
kholal ma li rék thieyeborom Touba 🥰🥰🥰🥰
2025-10-28 03:00:18
361
musset40
Musset :
saway wakhoul daye ték khél nila dane déf sounu courel ms dama dém ba niéupu khamko 🤭😁
2025-10-28 17:22:10
94
mohamed.abdallah9187
Mohamed Abdallah :
❤️❤️❤
2025-10-28 08:53:14
132
ibrahima.kobar
Ibrahima Kobar :
yalla naa yalla dolii soutouraa barkep Serigne BABACAR SY 🥰🥰🥰 j'aime ces petits 🥰🥰
2026-01-26 23:52:00
16
user3181266812469
Moustapha seck :
yalla Nanou yalla may dome diou mélni
2025-10-28 17:15:58
68
diwdg6
Di@w&DG? :
Boy bi naye tela teudi 😂😂goudi
2025-10-28 17:25:25
28
racky.sall91
Sokhna Kya khalifa 🙏🏾📿🌸 :
Yalla nama yalla maï domm bou melni inchallah 🙏🙏
2025-10-29 20:40:17
14
serigne.saliou074
serigne saliou :
Mane damoko beugg 😭
2025-10-28 09:17:03
22
santeserignetouba891
Élément S Fallou🥰🙏🏻🫀🤍 :
Yallna ko sa brome déf magoume mourid deugue🙏🏻❤
2025-10-29 18:01:00
11
cheikh.ndiaye3456
Cheikh Ndiaye :
2025-10-28 20:00:18
21
baefatoucha5
🌸𝓑𝓪𝓮 𝓯𝓪𝓽𝓸𝓾𝓬𝓱𝓪🍫✌🍯 :
Maniko nadité sonoule dal😩😩
2025-10-29 16:22:03
13
dieysarr0
⭐❤️DieySarr🧸🇸🇳 :
en tout cas dal diakhassé woul machallah🥰🥰
2025-10-29 14:20:51
6
bambandour745
Cheikhouna Bamba 🇺🇸 :
Obeuli bi dakoo weuyale 😂 dou xaleih deh ki😁😁❤❤❤
2025-10-30 18:26:05
11
fashion_yayefall
LaKarimienne.mu.SeñFaLLu❤️ :
Mom waxoul d😂
2025-10-28 19:35:00
9
daganaxassidakeep
Al amiin joob dagana❤️ :
pour man day obali sah ndekete jambaar la😂❤️❤️❤
2025-10-29 13:32:05
5
mouhamaedkebe
MOUHAMAED 🇮🇹 KÈBÈ 🇸🇳🤴😘 :
2025-10-28 11:46:57
12
sallcouture35
Sallcouture🇸🇳🪡🧵🇱🇷👑 :
Waw gorr ❤
2025-10-28 08:56:13
14
allaloumamelamp3
Tata fatou❤️ :
yalla nla yalla are t same la gua deuk si sakh si xassida yi ❤🙏
2025-10-28 15:35:27
12
modouhabibi2
Sëriñ Móodu Abiib Sill ❤️ :
Yàlla nama Yàlla may dom bou mélni Barkeb khassida yi
2025-10-28 17:36:11
7
zeyna.la.guerrire98
zeyna98 :
Serigne néna yéwinala meune gua teudi😁😁
2025-10-28 21:13:15
5
borom_darou_221
Broom..Darou..Bichri🫀🙏🏽 :
Ndayesane waw goor 😭💔🙏
2025-10-28 09:40:13
5
mlo502209
mlo502209 :
ndeysane khalé bi limi diague yeuk nako nk🥰😁
2025-10-28 05:37:11
5
To see more videos from user @khidmatoul_khadim7, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About