khana mane ngay wakhale mou gueume loma damalay tak ma waxtanak sama famille bane diape datou mariage après kelke jours mou changer version nanema dama am empêchement néna so djise goro yeuyeule ma honte devant ma famille bilay mais bayi nako AK yalla yalla naniou yalla até j'ai un coeur brisé 😭😭 mane ma bayi beuguaneté focus sama bop
2025-11-18 00:35:35
58
toulaye🇱🇷 saliou :
Mane dée bilaye walaye watalaye dama sour gor adouna AK alakhira bilaye
2025-11-18 01:17:47
25
.bouryboye374gmai :
Bilahi mane li dafma dal si goor bou nekal 3ans de relation 😭