Sa xam-xam leer na lool. YALLAH Yallah Faylla ❤️❤️
2025-11-19 21:44:09
86
moussa mbengeu bou baye karim :
mais ban xasida la
ban xasida la
ban xasida la walla fi amoul wolof tamit ?????????????
2025-11-20 10:48:57
19
MAMAN RABI AL HADAWIYYA💫 :
🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰yalla na sofianke yepou am diam aminn
2025-11-20 08:27:00
55
Kabir diagne touhfatou ht Rufi :
Sama première répétition xasida gui dafa tombé sama papa wathi liguéy ma aksi fi serigne bi di niané niane you yermandé ma commencé tour khéweul rip papa 😭😭😭
2025-11-20 12:04:20
29
chieikhouna bamba faal :
serigne mor mbaye cissé neena ko jang wacco ngaat sa niarri waydiour té yalla danaleen jegual.
2025-11-20 10:13:07
33
Mame Adama Mbaye euwalou murit :
allahmdou lilah sante na yalla Bou Bakh Thi Don guima don talibep Borom touba Khadim ràsoull la solution
2025-11-21 11:54:05
10
Baba Gueye :
bane xasida la
2025-11-19 21:48:12
12
thier nix :
Allkham ndou lillah Dieu redieuf Seringne Touba
2025-11-20 09:54:50
10
DAARAH ANSAROUL KHADIM :
yaa takh deh wakhabiste yii bayi khassida wallahi ngémé tougn ko lale
2025-11-20 07:58:51
36
Gueye BAMBINERI ❤️🥰☑️ :
Fouma toolou monek si sama khel ❤️❤️❤️🥰
2025-11-20 16:34:40
17
Khadim Bamba Fall :
bakh ak goré ci serigne bi la tamblé ci la yame😭😭yallnama yalla yaramal sama waye diorya barkéb serigne bi😭😭
2025-11-20 11:28:35
19
sidibandia :
ma sha allah 🙏dieureudieufe serigne mor mbaye cissè motakh ma xam khassida bi .alhamdoulilah dieureudieufe serigne touba 🙏
2025-11-19 21:28:44
5
766 sol daro sidy birahim fall :
لبسم الله السميع العليم طول لنا عمرنا صحح لنا بدنا وهب لنا الرشدوالتوفيق يالله ءامين. وافتح لنا كل باب كنت فاتحه للصا لحين من الخيرات يالله