@diop__peullh00: 💔😭#wave#senegalaise_tik_tok🇸🇳pourtoichallenge #

Diop peullh0🇸🇳
Diop peullh0🇸🇳
Open In TikTok:
Region: SN
Saturday 06 December 2025 15:00:36 GMT
132524
9514
275
343

Music

Download

Comments

edoulyrics
Ëdøü lyrics ✪🇸🇳 :
Sa way kharal ma retiré sama xaliss après gua deff louleu nexx 🤦‍♂️
2025-12-08 17:17:47
796
..1234bs0
Tiatt❤️bouNaby🌹 :
hé wave yaw dengay doundou yaw😎
2025-12-09 00:04:34
13
fadalndiaye3
Bou mame fallou :
Diaroul dioy yagui ak samay 110000
2025-12-07 12:58:36
221
aminarassoul272
Amina Rassoul Sogue🚩🏴 :
85f mofa nek dieuleul tè bayi dioyy yi😌
2025-12-09 09:43:35
172
kaynado1
kay Makeup 💄💋 :
Yor sama khaliss di fébar est-ce ki cava
2025-12-08 16:30:03
101
millasane1
millasane1 :
Ioe môme bala gua guene adouna Barki yalla sama Khalis ding mako fay lou l’ère lala wax gua dioy nonou liguay def ni safouma sa
2025-12-08 20:11:00
55
realmarid50
realmarid50 :
Boy dé malay nokou 😂😂😂
2025-12-08 16:39:57
23
khady86106
Khady :
Ahhh tonton wave yaw mi yorr sougnou xaliss bo dioyé fougnou dieum 🥺🥺🥺🥺🥺🥺
2025-12-11 00:43:56
2
maman.chuu56
Maman baby 🥥🌺🌝 :
Samay 50f boko yobé alakhira foma guisse rek dawal 😂
2025-12-09 21:35:15
10
thiarrakhalifa
Thiærra🍒Babačar🤍 :
Samay 2.300 lékouwouul dh 😂😂
2025-12-08 23:22:23
4
sokhou.bb861
Bv sokhou05💕 :
Bo démé bay xalatte khamouma nouniou wara deff 😭💔
2025-12-08 21:45:19
2
mme.ndiaye597
Mme Ndiaye🥰💃👗👗👙👙 :
He kharal dé sama avenir thi yaw la né🥺🥺🥺amna 500f ma retrait ko ba parer
2025-12-08 21:20:41
7
kazeza1
la mignonne :
ndeysan bn rétablissement ndah ma meune retiré bl nga dem
2025-12-08 22:18:05
8
tidiane.diallo523
Ahmed tidiane :
cheikh da melni sa way djikoy sénégalais lay beugué djel dh 😂
2025-12-14 21:00:39
2
user9804951507941
maria :
wa ki loumouy dioye😳
2025-12-09 18:33:59
2
thiawesta
Iam_satoubiz16-sn🇸🇳 :
Dofoulen Sakh khamgua ma kham
2025-12-09 06:47:10
5
chillgirl835
𝓑𝓲𝓷𝓮𝓽𝓪💋🦋 :
mane mom yoraloma Dara yonou diam 😂
2025-12-09 15:28:51
3
khadija.sy486
Lv Diva 💜✨🌹🥀 :
Mbadou sama 35f yi nga beugeu yobalé🙄
2025-12-09 21:09:33
3
dieynabasow184
Dieyna mrs kâ❤️🫂 :
Khana dagua lek Khalisou askane wi🤷‍♂️
2025-12-09 19:29:44
3
yace169
Yace :
Boudé dagua xép sama 14mil yi ok
2025-12-08 22:20:11
2
user.eva52
🅱ab🅾u Narr 🕋🌹 :
Bb balma 💔
2025-12-25 15:53:24
1
ndeyeamyndiaye199
AMY NDIAYE 👌👌 :
🤣🤣🤣🤣 je rigole parce amoumafa xaliss kon démissionele 😏😏 je te donne l'autorisation
2025-12-09 18:22:59
2
fatouchandiaye0
Minoucha 😍 :
Maye ma madiéle sama khaliss baparé 🥰ba décembre passé ndiou wakhsi ma chérie
2025-12-20 00:02:42
1
niangmaty42
Maty Niang :
Kharal ma dieul sama million yi après ngua déf loula nékh😏
2025-12-09 14:28:23
2
dija.dia88
Thiate bu djiguene ❤️ :
Hum defal sa bopu bi dîner danga yorr ay alalou diambour 😳😳😳
2025-12-08 23:49:07
3
To see more videos from user @diop__peullh00, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About