mane dh lycée bi la diangué déf nafa 3 ans wayé grève ndax ayy devoir meussou fa ame bagna diague dogue moléne andi fii yéne éleve dafa wara paré le jour au jour wayé di khar devoir wala composition pour meune diangu té calendrier scolaire bi douléne kharr
2025-12-13 20:06:38
95
Eva Saliou❤️ :
Pour la première fois ma guiss élève bouye grève nax devoir you ték lo🫢
2025-12-14 13:22:22
29
mmmmmmmmmmD♥️♥️🥰🥰 :
doley ame moyenne paré di wakh khol pape ly mome mo guene diakh diom😂😂
2025-12-13 16:40:27
34
gibbeux :
pourtant amnann droit déf devoir heure boulène nékh sans autant avertir les élèves
diangue lène sénn leçons té bayyi thiakhann yi
xana kone devoir surprises amatoull🤔
boy bayilén thiaxane yii wa baxna😅
2025-12-13 23:24:01
13
Madiou Sene sa mayel :
année passée second semestre dagno paré devoir après une semaine niou def composition mais Dara dagno samp def ko am moyen khar bac 😂 mais legui éleve yi ma guiss doyna warr😂
2025-12-13 23:35:34
6
IBRAHIMA :
gnoune ay devoir Surprise lagnou def gnoune😂
2025-12-14 10:51:38
4
☪️🇸🇳 :
ñii la Senegaal yaakaar noo yéena torokh😔
2025-12-14 13:32:33
2
WEUZZV THE BRÛLEUR 🔥 🐐 :
khalil yaw diaroul ngaye grève do élève di 😅😅😅
2025-12-13 20:27:06
12
yayou bayam 💝 la salikhate :
ᴡᴀᴋʜ ʟᴇɴᴇ ᴅᴇʜ ᴊᴇ sᴜɪs ᴘᴀʀᴛᴀɴᴛ ᴅᴇ ᴠᴏᴜs
2025-12-13 18:22:48
10
Sante Serigne Saliou Mbacké💞 :
Diangui len la wax élèves war na paré chaque jours pour dvrs ou composition. Li mom mangui koy doga guiss fofou. 😂
2025-12-18 18:08:20
1
cheikh afia fsf :
Yen dalnguen si nioun mom commencé naniou
2025-12-15 22:03:44
2
bb fa🏀❤️💞 :
vraiment nak daguen rew😁
def devoir avant fête mo ngeune dem fête ba nieuw
dem len diangui ahhh