@alamaltv_officiel: Bëgg Football ba Bayyi Julli : Danger bu Mag ci Jullit bi! - BAYĀN [Imam Moustapha Lo] Ci vidéo bi, dañuy waxtaané mbir mu graw mi ñuy dund ci jamono ji : Bayyi Julli (rawatina Timis) ngir topou match football wala yénén caaxaan. Li ñu fésal ci waxtaan wi : • Priorité Julli : Danger bi nekk ci zapper farata ngir ay caaxaan. • Éducation (Yar) : Lan lañuy nampatal suñuy xalé ? Football wala Diné ? • Développement : "Football mësuta développé ab réew." Li gën solo moy Yar ak Liguèye. • Rappel 2026 : At yi ŋungi daw, fan lañu jëm ? Nañu déllo ci Yalla bala ñuy fanaan suñu première nuit ci bammél. Abonnez-vous à la chaîne AL AMAL TV pour plus de rappels et de contenus islamiques. 🔔 Activez la cloche de notification ! #AlAmalTV #Islam #Senegal #Julli #Rappel