😂😂Man mom souma démé tivaouane douma tok si wétam ndakh dinala posse question bo xamni mariday tali😂😂❤ Machallah sy dougeul lou bari
2026-01-23 20:00:54
56
Ablaye Kébé 🤔🇸🇳 :
Thiey goorou khadidiatou ak Aïcha 🥰❤️sama wadjii bayou Zaynab,Ruqayya, Oumm Kalthoum, Fatima Zahra, Qasim, Abd-Allah Ibrahim Ndiol Makka mamou Ousseynou ak Assane borom barrière or yi ya diara titeuro
❤️🙈Gni nane ko Nabi gni nane ko ya rassoullilah gni nane ko Mohamed SAW
amouñiou koudoul ioe doy ngañiou fil dunya
wal akhira yañiou guene yañiou doy🥰🥰❤️❤️🥰🥰
2026-01-25 10:11:34
32
sy ganki :
na sa diam yagg
2026-01-23 03:18:30
14
ya_khady_collection❤️ :
machalla sy malick yalna yalla goudal say fan maïla wér 🙏♥♥