Sama dieukeur la Machallah loum ame bokho ko ak mane kholoul sama salaire toujours présent
2026-02-26 23:04:25
1005
fatima kebe :
sama boss deugeur khol sokhor faut reuthiou nala lima dougué si mom
2026-02-27 12:29:19
439
Nitt kou gnoul :
Mane d sama djeukeur bakhna amna yeurmande mais dafa guawa mér guawa guiss boppam 🥺🥺🥺
2026-02-27 03:58:54
249
Mme Thiame ♥️ :
bilaye sama Boss la thiame Babel
2026-02-27 01:16:20
145
thiatou M. Ndao ♥️😍 :
wa mais commentaires yi 😂yenn nieup am ay super homme 😂😭waleu
2026-02-27 10:34:26
48
madamesamb642 :
Machallah mon mari nonou la mél bilahi Samb mo bakh 😢nianal lén ma yalla bayi ma ake mom amine
2026-02-27 02:08:03
51
Une femme 👩 🥰 :
Billahi sama dieukeurou tanta nonou la mél aka bakh té kha akou djiguene 🥰tonton makhtar fall yalna yallah goudeul sa fan si barkei wérou koor gui Dieurdieuf fall yeureum nganiou
2026-02-27 15:54:20
27
« THI🅰️TT — Mrs Ndiaye❤️🔐) :
Ki dh Sm boss laye waxale Ndiaye diatta🥰❤️
2026-02-27 10:01:58
17
Khadija rasoul :
Sallalahou allah Mouhamedine
2026-02-27 05:51:58
67
user1250222581398 :
sallalahou alla mouhamade ☺️
2026-02-27 02:18:00
39
l'infatigable :
ki dé sama boss lay wakhal
2026-02-26 22:52:01
27
Mrs B :
Sallalahou Hanla Mouhamed ♥️♥️
2026-02-27 21:36:45
12
Ndeye Nafi Mme gueye ❤️💍 :
Kén dou sama boss gueye ndioro❤️💍yalla na sa diam yague
2026-02-27 02:17:50
20
Mariama jamal Barry ❤️🥰🤍 :
alhamdoulila man sama boss kom galas way dom lanou ama goul 7ans de mariage 😭
2026-02-28 23:24:01
7
kamidiaz :
sama boss nonou la mélone Ndiaye Diatta yallah na khipé Aldiana firdawsi incha'Allah 🤲😭
2026-02-27 08:03:50
8
ndeya tresse❤ :
machalla sama ndjeukeu🥰🥰🥰🥰
2026-02-27 09:08:22
5
Aïchaziz 🍯 :
Alhamdoulillah Alhamdoulillah 🥰🥰
2026-02-27 11:29:38
5
mintou Ndiaye :
Sama boss
2026-02-26 22:44:46
16
Jolie F❤️______Mrs Juuf ✌🏾💞 :
Douma wakh sakh Machallah il est le meilleur ❤️❤️❤️
2026-02-27 08:11:49
6
Hadija :
sama sangue bi ba poulo 🥰🥰
2026-02-27 00:39:41
13
<<💓Aichaaa💗>> :
Masha Allah vue les commentaires kone espoir amna😁🥰
2026-02-27 03:07:21
20
bousso bally216🥥🥰 :
Bilaye sama boss la kane Diallo ya guene si man🥰🥰
2026-02-27 11:54:03
21
joefriperie👗👖👕 :
Magui ni Bilahi💪💪😂
2026-02-26 22:51:00
78
Coumbeuh :
Alhamndoulilha sama djeukeur yalla na goude fane 🙏🙏🥰🥰
2026-02-27 12:57:33
5
Mariama Cisse :
wawaw ndiaye diata 🥰🥰🥰
2026-02-26 23:44:53
30
To see more videos from user @al.aamine, please go to the Tikwm
homepage.