yalna ko yalla yeureum té diegueul ko SSM jërëjëf ❤️🥺🙏🏿
2026-03-04 20:06:58
443
Ⓜ️K EL PROTECTOR 🪖 :
Yalna niou yalla mouthial 😭
2026-03-03 01:38:45
165
Ndanane_bou_Serignefallou❤️ :
Ceuy Baye Saam lii nga wakhone leip mom lanouye dounde Tay 😭😭😭
2026-03-04 18:27:21
184
AMAR-AUTO :
Khawma kañ laay dee.
Kon ñaanal leen ma Yàlla jéggal ma te yërëm ma. 🤲
Ndax kenn xamul kañ la dekk bi di jeex.
Su ma la defee lu la metti, jéggal ma.
Bul ma fàtte ci sa ñaan.
Yàlla na Yàlla jéggal ma te yërëm ma.
Yàlla na nu Yàlla jéggal ñun ñépp te yërëm nu. 🤍 »
2026-04-01 01:03:00
16
Magatte Loum360Sy :
Salam svp, ou peut on ce débat en intégralité. merci
2026-04-29 01:04:23
5
M~B~P🇸🇳 :
Yalla naniou Yalla até si yeuremandém 🙏🏿🤲🏿
2026-03-05 06:54:23
58
ousmanedieganed47 :
𝐬𝐚𝐥𝐚𝐥𝐥𝐚𝐡𝐨𝐮 𝐚𝐥𝐥𝐚 𝐦𝐨𝐮𝐡𝐚𝐦𝐚𝐝𝐢𝐧𝐞🤍🤍
2026-03-05 07:03:02
30
Abbashop :
Cheikh tarbiya deugg ❤️😭 Thieuy mbaye yaram ❤️❤️😭😭
2026-04-15 23:30:41
6
Mame baba Diaw :
YALLA NAKO YALLA YEUREUME TÉ KHARÈ KO ALDIANA FIRDAWSHI 💖🤲🤲
2026-04-12 21:39:18
3
sanet :
jerejef seringe sm ❤️❤️
2026-03-31 19:05:54
3
Abdou Rahim 🤟 :
2026-04-09 12:10:26
5
user9932453287076 :
Sarigne Sam Mbaye 🙏🧏
2026-03-04 13:35:54
12
ABY~SALIOU🫂🥹🫀😽🪭 :
☝🏽Dieureudieuf yallah 😭
2026-03-17 16:09:13
10
Thiané ✨✨❤️ :
Yalnaniou yalla khirrr silou bakh baye sammm Yalnako yalla yeureum kharéko aldiana firdawsi
2026-03-05 20:22:06
8
Ada :
sallalahou ala mouhamad
2026-03-04 21:06:14
15
ndeyefatoudiaw05 :
Yalna niou yallah xir si bopam
2026-03-10 05:08:13
5
Dieng Halil :
wallahi Ndaysane 🥹
2026-03-04 23:27:25
11
Mame baba Diaw :
ADOUNA DOU DRA BLY 😔😔
2026-04-12 21:38:54
2
pedri jr ⚽️ :
wallahi
2026-04-14 11:58:44
1
Ibra Ndiaye :
Yalla naniou yalla takha wou adouna ak alahira si barké serigne bi amine yarbi
2026-05-01 15:23:21
1
DiopKhady :
sallhoU allaMoUhamed ♥️
2026-03-21 00:33:34
2
sarréco auto pièces 💯💯 :
sallalahou hala mouhamad 🙏🙏🙏
2026-03-22 00:19:52
2
Rᥫ᭡ LAMTORO dm peulh bu rafett :
diaradiafe baye same mbaye yalla naniou ko yalla fayal🥰
2026-04-28 19:10:20
1
Mamadou Diallo :
yalla naniou yalla fayal s saam❤️❤️❤️😳
2026-04-01 18:13:55
2
Sëydoü_le_Barron🇩🇪_🇸🇳 :
l'apsen le plus présent
2026-04-19 03:22:57
1
To see more videos from user @tawfiqulmurid, please go to the Tikwm
homepage.