mo takh djeukeur fath merr wala diabaru feth merr rethou rek lay andi
2026-03-06 17:04:56
237
Ami Diop641 :
bestie neko na def attention tas ba pare dem si exbi fek amena rancune wadie day defante ak yayame na holat boubah
2026-03-06 20:20:18
186
Amadou Ka :
fière d'être villageois
2026-03-06 16:00:45
33
callmesafie🪭🌸 :
C’est triste mais mou guéne si sey bi avant que l’irréparable ne se produise mo guéne partir avec dignité mo gueune tok ba gatié dila demlo parce que seytané da bari dolé niar niou beugànté mome moy lolou woroul bala tiag na déme
2026-03-06 14:56:06
61
Mbénista :
Elle devait peut être arrêter de communiquer avec son ex car la communication ne fait que lui pousser à détesté plus son mari 👌à mon avis
2026-03-06 16:21:28
113
Anta salikhate fall❤️❤️ :
bis bo dème si ex digua dathie lou meti ndakhe doulla meusseu wolou
2026-03-06 21:32:40
63
Mamadou Sogue 🇸🇳🇮🇪🇳🇬🇳🇪 :
mém bou tasé qui dou ko tak
2026-03-06 13:51:09
31
user2062319341122 :
mais bis bou baayiwé dieukeur DJI dinako rétiou
2026-03-10 12:43:23
7
Sonia❤️🍫 :
Wadiour dinna amal domm akkk nak 😏
2026-03-07 07:31:13
8
FRIPPEEIE BY NDEYA🩳👗👔👖👕 :
yaye DJI moko deudale ak exe copin bi mais mbeuguel bi niom niaar yeup tayougnou sen bayante
2026-03-06 21:26:47
24
Maguilahi🤍 :
Té mo yam si diekeureum bobou mo geun si mom
2026-03-06 13:30:41
25
mdcr :
c très compliqué les maman c autre chose
2026-03-06 13:29:59
21
Arame Mrs Diaw 💍🥰 :
Ndeysane li dh moy Adouna dhh kheb nitt baxoul
2026-03-06 14:29:44
23
Nianga diop :
Nitt kène douko khèppp
2026-03-06 15:35:48
10
evadjiba2🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇫🇷 :
Je te félicite pour tes 2 millions d’abonnés, My Bestie tu l mérites vraiment Machallah ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
2026-03-06 14:46:28
12
*dulcinée*💍🫀🤞❤️ :
My bestie doma diokh sa Tuto voile bi
2026-03-06 14:20:47
19
Bousso Baly345 :
na divorcé c mieux
2026-03-06 15:41:02
9
Talibé serigne saliou 🥰 :
Thieuy yalla 🥺🥺🥺
2026-03-06 16:49:28
7
Bineta kharagne Lo 🌸 :
Thieuy yalla chaque jour ak bou besss
2026-03-06 14:35:29
12
____Caramelaaa :
Salut, Ya une personne qui avait appeler durant ce live et disait avoir le cancer et la 40ene, quelqu’un aurait son numero svp ?
2026-03-09 17:15:49
5
Barry :
Dans ce cas il faut choisir entre le cœur et la raison 🥰
2026-03-06 15:33:27
6
Thiatou bayam 🥰 :
Kii deh khalè bou gore limou nek Amérique motakh khelam nékate si mome
2026-03-06 21:33:42
7
Maimouna Wele :
Ma besty j’ai besoin de te parle
2026-03-06 15:24:18
2
aln82 :
divorcele rek🫶
2026-05-03 01:13:54
2
To see more videos from user @mybestieofficiel, please go to the Tikwm
homepage.