@baabakar_wolof: Taalif bii, Sëriñ Momar Kayre moo ko bind doon ci xamle njariñ yi nekk ci #zikr. 🤍 Moom nag ca mag ña njëkkoon a jébbalu ci Sëriñ Tuubaa la bokk. Doonoon na ku xarañ lool ci nose ( poésie ). ✍🏻: @baabakar_wolof

baabakar_wolof
baabakar_wolof
Open In TikTok:
Region: SN
Friday 06 March 2026 17:02:53 GMT
3041
257
8
2

Music

Download

Comments

xadimbay
ibra Diop :
Baabakar Bënër lumiy tekki ?
2026-04-27 21:33:50
1
baaysamsam
Al-bahour 🇸🇳🇸🇩 :
@Elimaan Njaay Eng.🇸🇳🇨🇳🇨🇻
2026-03-13 06:18:50
1
mindse.t8
Diop Wolof🇸🇳 :
2026-03-06 17:28:16
1
fallou.niang0798
NIANG 🙏🏽🙏🏽 :
😭😭😭
2026-03-06 17:10:18
1
siddiq689123
Seydina Wolof :
❤️❤️❤️
2026-03-08 10:59:49
0
alsan.ndiaye7
alsann :
🥰🥰🥰🥰🥰
2026-03-06 19:40:38
0
souley.thiam7
Souley Thiam :
🥰🥰🥰
2026-03-24 11:50:28
0
falloudieng1142
Fallou Dieng :
🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2026-06-01 15:51:03
0
To see more videos from user @baabakar_wolof, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About