Ferran na wat bop bi ngir yallah souko waté rek Dina nekat si match yi 🤦🏾♂️
2026-03-08 23:38:56
108
Mouhamed Rassoul🇸🇳🫀🇨🇩🇩🇿 :
Ferran joueur bu bakh la ms supporter Barça nio bara wakh rek mane ferran doumako critiquer
2026-03-08 14:23:20
20
ndeye une Sénégal 🇸🇳⭐ :
khamoul dara 😏
2026-03-08 22:15:56
76
Omar gueye :
na watou ba xam
2026-03-08 20:29:18
13
Prodaroukhoudoss23 :
Ferran Dollar la
2026-03-08 21:30:08
6
badakhoule237💯🚭☪️ :
do kham lokoy wakh dal😂😂😂😂
2026-03-08 21:27:07
19
Dieng :
même s’il rate beaucoup mais il en marque c le plus important et évitons de le critiquer
2026-03-08 22:57:11
2
LAYZABO✅️ :
khamoul dara
2026-03-08 20:10:14
7
Amza Dieng :
dawoul sakhe sunu yarame
2026-03-08 23:30:10
10
seringe cheikh moustapha :
Kamoul gate
2026-03-09 12:13:06
3
kader 🕷️ :
saway ki il faut que mou ame 5 occasion de but pour marqué bén
té Barça Bou beugué dieul ligue des champions il faut k mou ame attaquant bou efficace amna match yo khamni day teudiou 9 Bou bakh rk molassi meune guéné
2026-03-09 12:23:52
4
ly bass :
Jackson 2🤣🤣
2026-03-09 11:19:35
3
JĘŪNE CÃTĀLÀN🇸🇳 :
dafa nékoul en forme rek
2026-03-10 10:15:03
2
Gueye papa :
Un attaquant ms pas un butteur 😏
2026-03-08 23:38:50
1
@Cami belloli ❤️ :
Il marque quand il veux 😏
2026-03-09 13:30:14
1
M Ceesay :
Man dama khamul lan moy poroblem bi ahh 🥹🥹
2026-03-08 22:56:32
1
NDIOBA❤️🫶 :
Ferran est ce do watou waat niou khol bakham sonn nagn deh 💔😭