Lima gueune metti si sa aduna moy guisse makk bouy ligueye yallah nanou yallah may djambott bougnou tèla takhawou 🥹🥹
2026-03-20 12:53:58
5519
Mara Diop76 :
Yalla naniou yalla may baniou téral soniouy wadiour 🥰yi
2026-03-19 23:41:07
5142
Karbalah✊❤ :
koko xam svp
2026-03-19 23:58:42
1592
La science 🧬 :
Diambar mayéwoul yafouss xagnéwoul lep yalla lay sop 🥰🥺
2026-03-19 23:46:35
1389
seyni gaye :
Kou wakh amin yalla na gua téki téral say wadiourr 🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺
2026-03-20 01:27:40
3214
Fall ❤️ndiaga💙yarram♎️ :
Bly sama yaram daw na 🥺🥺
2026-03-19 19:59:20
3224
MDL IBRA FALL🤍🐚😍 :
Adouna yalla moka mooñ ah thionno nanou dellou thi mom diko niaan mom lk moniou meuna guennei si lin nek teh teksi diko sant lou am sollo cey saa broom bokay sant di diouli si kou tedki saw cey bonheur bobu🥹❤️