Je suis chrétien mais j’aime écouter le saint coran 😌
2026-04-05 05:45:22
8806
Mo fit🥇🦍 :
Kou geuneu diangeu alxourane yalla na am ndam🤲
2026-04-05 02:15:01
18665
TAA_HAA 🥺❤️ :
une semaine mugui ni sourate Yassine bi mooy diague ni mome lakoy diagal diko nianal yalla blh🙏téh inchalah yalla dinako soutoura mayko ndam si barké seydina mohamed sws inchalah 🙏
2026-04-05 00:19:55
1705
Mame mor Sarr513 :
J l fais 15 fois pour lui th nak Yacine moy kholou alhourane Modou Lo yalna la yalla may Ndam Barké kholou Alhourane ✌️🙏🙏
2026-04-05 00:23:42
2998
It’s lyly🌸 :
Yalla nala yalla may ndam ❤️🙏🏾
2026-04-05 15:59:22
1018
Vladimir🇸🇳 :
Thi barquet sourate bi yallah nala souniou borom bi may ndam❤️🥰🫶
2026-04-05 02:48:59
965
aishadioum1 :
Yalla bou yakar tass 🙏❤️
2026-04-05 14:38:04
401
modou moukhtar sylla :
Rufisque derrière modou lo ndam rèk inchallah 🤲🏾
2026-04-04 23:57:21
862
SLeppy :
kou guis vidéo bi après lamb dji rk lalal j'aime
2026-04-05 19:54:36
209
Diarralapatriote✌️❤️ :
Barkèp souratou Yaciine yalla nanga am ndam bou leer souba Inchallah 🤲🏾🤲🏾🤲🏾
2026-04-04 23:53:42
757
Biscoo Smets🇸🇳🇧🇪 :
tay laniou la gueunaa beugg bilahi courage❤️
2026-04-05 19:41:12
89
Baye fall bi :
machallah mod lo yalna d'or sa thies mou danou si barki seydina moukhamét 🤲
2026-04-04 23:20:49
601
Momo✪ :
Amine 🤲🤲😭🥳 7 ans 🥳🥳👑
2026-04-05 00:17:43
205
alcali-lab :
Li mmoye vrai victoire. Respect champion
2026-04-05 19:27:40
84
爪ㄖㄩ卄卂爪乇ᗪ_ᗪ🤴🏾🤍! :
Y’Allah mayal MODOU LÔ Ndam bu sedeu gouyyyy❤️❤️❤️😭😭🙏🏾🙏🏾
2026-04-05 11:50:49
40
MBD 🫥 :
Yalla mayale modou Lo 🥹
2026-04-05 12:16:31
52
sweet—awa💕🌷 :
Ndam rek inchallah
2026-04-05 13:54:31
19
Gavi jr 06🧠⚽ :
Yalla nala Yalla soutoural🤲
2026-04-05 13:43:02
31
𝑷𝑹𝑰𝑵𝑪𝑬👑𝑴𝑶𝒀𝒁𝑬💫✪ :
ndam rek inchallah 🙏👑
2026-04-05 15:54:36
14
oumou kalsoum💝🌸 :
Wakh léne amine 🥰
2026-04-05 15:49:39
13
Sokhna awa sadbou :
Yallla nala yalla maye ndam 🙏❤️
2026-04-05 15:07:48
53
nabien Bou ch saadbou :
Masha Allah
2026-04-06 00:31:12
6
To see more videos from user @khadimgadiaga313, please go to the Tikwm
homepage.