Yenn sayi ñou beug lou geunoul si ñoun yenn sayi ñouy yôtou lou geunoul si ñoun yenn sayi ñouy Kharr lou geunoul si ñoun MBA sax ñouy ñane lou geunoul si ñoun kon lou mana khèw rek Botha sabap loo rek latha dess bayè ko ak sa borom moo kham la geun thi yaw Dana kotha deff✍️
2026-05-01 15:51:39
5
LOGIQUE :
Des fois digua Yotou lou genoull si yaww
2026-04-30 22:43:27
11
dioplamecano1 :
misaloum adouna🥰
2026-05-01 13:29:53
2
Niang Atou boye :
kàràngé guouwôr la protection vrai c'est ikfini🤲🤲🤲
2026-05-25 09:27:37
0
niang bawal bawal🤌🥰🤍💚🤙 :
Topou sa beuge beuge rek 🥺
2026-05-22 13:03:38
2
Ngagne Diongue :
il faut bien analyser vos décisions avant de faire quoi que ce soit
2026-05-28 23:51:20
2
سيدنا عمر 🥷🏻🥷🏻✅ :
Cey sama Seeigne bi machallah
2026-04-30 23:56:28
1
FADEL✔️ :
Fuchsia
2026-04-30 21:57:59
1
سيدنا عمر 🥷🏻🥷🏻✅ :
Nit Dina Topou Lomou beug Ba Sank Bopam diangat bobu lasi Am
2026-04-30 23:57:26
7
Mr. Itali🥰🇺🇸🇮🇹 :
وعسي ان تكرهوا شيئا وهو خير لكم
وعسي ان تحبوا شيئا وهو شر لكم
Yàlla nee na leeg-leeg ngeen bëgg mbir te fekk gënul.
leeg-leeg ngeen bañ mbir te fekk moo gën ci yéen.
kon bukki bii lekk pitax mi la bëgg waaye xamul ne gënul ci moom.
waaye xiif bi metti na lool waaye xamul ne moo gën ci moom ndax àll bi Yàlla a yilif moom mi nga xam ne moo ne
والله يعلم ونتم لاتعلمون
Yàlla xam ne lu nu xamul
2026-05-04 19:13:48
2
Soldarou yayame❤️🩹❤️💯 :
Pour moi il moy adou na lo daw daw doko djot
2026-05-01 01:04:08
4
E T F L :
lou nit di yotou nay lou guene ci mim
2026-05-02 14:56:18
1
Niang Téranga rék :
dieureudieuf mbacké
2026-05-01 00:09:59
2
Aphiya geo 758597279 :
yaw rk lay topou
2026-04-30 22:28:03
1
Àl amine+221🇸🇳✅ :
Boul topp sa beug beug ba l’or sa bopp😏😏
2026-06-11 19:03:35
0
rahman +221🇯 🇸🇳🇵𓃬𓁋 :
2026-05-23 18:31:43
0
khadim Cissé :
♥️♥️♥️
2026-05-02 11:05:27
1
Maty Ndoye :
🥰🥰🥰
2026-05-01 22:27:49
1
Ousmane 💗 THIAM :
🥰🥰🥰
2026-05-02 23:10:47
1
user8551810760721 :
🥰🥰🥰
2026-05-02 21:05:27
1
oumy diop :
🥰🥰🥰
2026-05-03 20:08:50
1
diop love 😎❤️ :
😭😭😭
2026-05-01 19:12:54
1
Faty sour :
🥰🥰🥰
2026-04-30 21:57:00
2
mamcak :
🙏🙏🥰🥰🥰
2026-05-01 05:51:08
1
To see more videos from user @c..k..m3, please go to the Tikwm
homepage.