10 basmala +la hawla wala houwata Ila bilahi alehi azime
2026-05-09 08:07:41
1566
LATZO ꧁ ★ ★☆꧂ :
Sama yaye yalla na feke sama dieurigne téma amal kou dieurigne 🤲🏽🥺
2026-05-09 10:48:59
663
ndeya yayou bayam💍🦋💜 :
Salam mangi deggel sa wakh ji dieulé nako ci téré Serigne Sonhibou.. khana di yokk rek ni dey ande ak waw manam bismilahi rahmani rahim wala hawla wala khouwata illah billahi aleyhil anzim 🙏🙏 jërëjëf ci fatéli bi Yalna yalla fay la