vous l'avez annoncé depuis longtemps les sénégalais qui n'ont rien compris que ce régime là c'est du faux type de ce pays merci Père Moustapha Diakhaté 💓♥️❤️💓♥️❤️💓♥️❤️🥰🥰🥰🥰🥰🥰💓♥️❤️
Gni gneup ay seytane laniou. Té Diakhate dou nite kou bakh. Madiambal dafay doule. Té dou nite kou bakh. La preuve dafa daw ak alale boumou satch. Ousmane Sonko di guene ko bayi. Nous voterons pour lui tout le temps. Meunou lene ci Dara.
2026-05-17 12:33:11
4
Babacar Cool :
🇸🇳 Rewmii Dh Keup Koufy Déf lou Bone Diko Neubou Yallah Dinala Wérr Dinga Am Gathié Boula Soff Ak lou Way Meuneu Nék Diko Déf Yallah Dina ko Wérr Mo Xam Dangay Ray Nit Diko Neubou Ak thiy Façon Yeup Yakhe Nagne imagou Rewmi Rék Sénégal 🇸🇳 Mérités Woul li Way
2026-05-17 12:48:33
4
El Momito :
Thiey Omar khaïssa 😂😂😂😂
2026-05-17 10:10:21
5
Baba Gasama :
merci boco
2026-05-17 11:55:43
4
queen :
yalna bougniou yalla tek bekor wala natou dah liiii
2026-05-17 12:36:47
3
baad boy officiel :
chie tetetetetete lan mo indi fi Adji sarr tamit fi benen ca la bi bou ndiaga seck bi la🤣🤣🤣🤣🤣🤣Aka bari problème sonko rek🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣