@bayemodou914sadikh: Jërëjëf Serigne Touba 🫀🕌 Boroom kham-kham ak yërmandé, yaw nga doon leeru diiné ak jàmm ci sunu xol. Sa ngëm, sa muñ ak sa liggéey dafa tax nit ñi bëgg yoonu jub. Yalna Yàlla fey la ci barkéem, te barké Serigne Touba sax ci sunu kër ak sunu dund. 🤍✨#creatorsearchinsights #mouride_sadikh_officiell #tiktokviral #fyp #khassidayi_rek
bymodou914sadikh
Region: SN
Friday 22 May 2026 17:46:08 GMT
Music
Download
Comments
Dieynabambarah😍peulh♥️✅ :
Ana gniko beug ♥️
2026-05-23 10:33:15
2451
I N S S A✪ (17)🍼 :
Mom lagn namou dh😭❤️
2026-05-22 23:31:05
3314
FLEXX🐍 XVIII🤌🏻🧠 :
Sou nékoul wone serigne touba douma aimer vidéo bii🥰
2026-05-23 07:57:20
4389
Thiatou fatou ❤️💍😍 :
Diomayyyy meussoulll discour ba wakh li😌❤️
2026-05-23 09:38:47
826
Hems beugue Fallou :
sama president 🥰🥰
2026-05-23 01:25:14
431
𝓨.😍 :
Serigne touba ak serigne mountakha motax may aimer Barcki cheikh ibreu ❤️😭😭
2026-05-23 11:25:47
314
Mamyta—k💕✨ :
Ki nouko nite di banié la xamoul 🥰 bobou charisme ak dal oh Macky rek ❤️
2026-05-23 09:26:57
570
Khadija♥️🥳 :
dieureudieuf Serigne Touba ♥️♥️♥️♥️
2026-05-22 22:55:45
752
ablayendiolor :
maylen président Macky Sall aye coeur
2026-05-24 10:41:51
25
Maïmouna Sylla :
Macky Sall seul
2026-05-25 08:40:50
14
salihate❤️mu hadimi☕️ :
Serigne touba mo takh m’a aimer d walahi ☺️
2026-05-25 11:54:39
9
Ballisco :
merci président Macky sall
2026-05-25 17:49:37
7
Ousmane ❤️ bou 🎉 ndaw 💸😍❤️ :
ohh maky ❤️
2026-05-25 05:37:42
5
ZEM 🅾️🅱️🅿️ 🥷🚭 :
Serigne bii kouko beug ma beug laa 🥰
2026-05-25 12:37:03
9
Abdou Diop :
Dieureudieuf serigne touba
2026-05-26 21:40:20
5
Laye Bongo :
Merci Macky Sall 💚💛❤️👍
2026-05-23 11:59:34
4
Mbayangngom :
Dieureufeti serigne touba ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2026-05-25 12:05:47
8
bay fall :
🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰❤️❤️❤️❤️❤️
2026-05-22 23:12:55
126
amadou_camara🇸🇳18☝🏿🩸 :
Première fois ma aimé vidéo macky sall 😭❤️
2026-05-23 15:23:46
114
Neymar 🇸🇳 :
des coeur pour lui♥️
2026-05-23 12:58:31
43
@cheikhouna chocory ndiaye 222 :
merci macky sall 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳
2026-05-24 20:09:14
9
ass ndom 75 :
nday sane ak rafet khol🥰
2026-05-24 16:10:43
7
Maty bou Macky sall 🤩 :
🥰🥰🥰🥰
2026-05-23 22:50:45
6
To see more videos from user @bayemodou914sadikh, please go to the Tikwm
homepage.
© 2021-2026 TikWM. All rights reserved.