@itskhalil55: Jude Bellingham ak Rak djie niœy ande si lépp Mag ji ubbi yoon wi, rakk ji topp ko ak kóllëre." (Le grand frère a ouvert la voie, le petit frère le suit avec détermination.) "Doomu benn njaboot, waaye ñaari xale yu bëgg jàpp ci addina football." (Enfants de la même famille, mais deux jeunes qui veulent réussir dans le football#JudeBellingham #RealMadrid #Football #foryoupage❤️❤️ #TikToksenegal