@abdulahadborombelel:

BOROOM BELAL  XAM JARIÑU
BOROOM BELAL XAM JARIÑU
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 07 June 2026 15:28:25 GMT
47385
2156
146
110

Music

Download

Comments

basslutte1
BassLutte+ :
Diabar yalla ko yor
2026-06-07 17:43:01
24
amadoudiallo81816
amadou :
kone bayyil gnou ndjaalo bassi kanam
2026-06-07 19:38:26
7
serigne_gueye111
serigne_gueye :
oustass tay D’accorouma Ak yaw
2026-06-07 23:39:56
0
user8861720257461
Dr. Diouf :
Say video dey am solo lol way. Yalnala yalla fay te' yok sa takhaway
2026-06-08 00:10:59
2
manendiaye253da0
elhadj camara talibé s chéikhe :
niake doyelo yalla d moye nga yaakar n yaye doundal sa bop
2026-06-07 18:47:59
6
gueyedeug2
Gueye 307 Deug 221🇸🇳 :
Sa rakk kouko yor bayi lene yoyou sokhna yalla ko yor ak sabablou mane bamay takke yarou ma 200 mil tay alkhamdoulilah 5 ans de mariage Alkhamdoulilah
2026-06-08 09:22:45
1
fllu.jalibatoul.m
sëriñ Fàllu séen :
Soxna yalla ko yoor liy xew eleg sunu borom moko xam,
2026-06-07 23:03:15
5
diaahmadd0
Dia ahmadd :
yéyé kou baax daanu nga takk soxna n'a rien avoir ak am am, dém léne takk diabar ndax Moy gui wagnéku
2026-06-07 22:04:06
6
djibril.diaw65
Djibril Diaw :
Attention, vous avez avez utilisé la main gauche pour boire.
2026-06-08 03:23:03
0
barafayeucad
barafayeucad :
Bilay Wax ga deug
2026-06-07 21:45:45
3
cheikhcisse590
Cheikh Cisse :
koubakh mane dee damadane dégue bo také sokhna yalla dalay diokh weurseguou sokhna si
2026-06-07 21:44:57
3
karimkarakara1
Karim kara L'officiel 🎤🎻🎧 :
ya ki moyy sa Serigne Ndéké ni rek la mena démé
2026-06-07 15:40:16
2
user4115613815906
kal :
bimay taka amouma dara me tay alhamdoulilh
2026-06-07 21:32:38
3
africafoot10
Africafoot :
Lolene beug dougne tak dougne ndialo khogne douma raydé
2026-06-08 01:24:38
1
ahmada3130
bagg yalla313 :
wakhofi toss
2026-06-08 00:19:50
0
user6277549014947
M C England 🇬🇲🇬🇧 :
Wallahi lou werr
2026-06-08 00:50:30
0
mame.bousso.mbaye31
Mame bousso mbaye🤍🎀🧸 :
Fatima bobou aka ame sax
2026-06-07 20:59:52
2
thiam.ndiaga
thiam ndiaga :
mann dh walahi limay am diamonodji bama takagoul woon sokhna awmako bilahi sant yalla nak
2026-06-07 20:12:35
3
beugfallou857
beugfallou :
kartane ,dolley ,meune meune ak am am fa yalla ... Ken meunoul t projet bou mat yalla la.
2026-06-08 06:58:16
2
macadbio
Mame Cheikh Anta Gawane :
yala bo takk lép takhaw😳😳tiéy yala lou méti
2026-06-08 00:00:51
1
thoma2567
Thoma 25 :
deug d'où romb ay nopp
2026-06-08 00:31:12
1
ibrahimagorguisen
ibrahima GORGUI Sene 🇸🇳 :
Ben way dé tay lou weer leu wax
2026-06-07 17:04:40
3
ibrahimadieng78
Djaraff Ndoy :
Enn kon gnou ndjaalo
2026-06-07 20:50:22
2
To see more videos from user @abdulahadborombelel, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About