@muqaawim: Lou ler nga wah ✅ #khadimdiop #senbuzz #mariage #dieukeur #diabar

muqaawim
muqaawim
Open In TikTok:
Region: MR
Monday 08 June 2026 05:59:23 GMT
479226
71677
729
4324

Music

Download

Comments

mamy02
Mamy🇸🇳 :
Ah mane michoui lay dieul dei moh🤣🤣🤣🤣
2026-06-08 18:27:52
1092
djibadiop8
Sunu askane traiteur :
Lila wakh nitt dafay beug tè yallah yakh
2026-06-08 20:33:17
437
meth221xdks
Mouhamed ❤️💫 :
Djiguén gni kou paré laniou beugue motakh dounou am loulén nékh
2026-06-08 20:34:11
165
salkhatbussiness
:
Akh ça depend rek sou fèkè sama keur yaye sombi lafa dan lek somay tende miswi lay tende si no rek damay diabet 😭😭wala dama trokh
2026-06-08 15:12:02
230
papadiop.04
yiannis🔥🏀 :
douniou xiiif gniii dei😂😂
2026-06-08 22:19:51
59
ajia.thiame
Adja 💄Babel👡👗👛 :
Wouy😂😂😂
2026-06-08 13:26:07
79
taphaspamofficiel1
THAPHA💚 BOU💛 NDAW 🩸 :
sallahou allah mouhamadine
2026-06-09 10:52:24
12
mamefamathiam415
Mame Fama Thiam415 :
Merci
2026-06-08 12:16:28
28
diodio20022
mami salam :
Pere wakh nga deug bou werr
2026-06-08 19:56:35
20
drcbd
Daqueen :
bilakhi deug la
2026-06-08 19:05:48
11
user8298175761096
maman :
bilay sama sangue bo kamara yilé damako beug ba dof dama yereum douma dore douma saga louma Beugue rek la beug dima protégé yalla nako yalla same 🥰🥰
2026-06-09 12:35:51
3
metoubrown8
Métou Brown💖 :
Bilay mane boul yore dra bagua bax rek moma intéresser
2026-06-09 21:30:41
5
mbayeyaramcouture385
ndoumbmbaye385 :
Sama dieukeur moma ko partager ❤️❤️🥹
2026-06-09 10:07:29
27
albaorganic
albaorganic :
Tonton michoui nekhe na deh 😔
2026-06-09 10:45:30
7
zynaa57
Zynaa skn :
Nek na ak gor 7 ans
2026-06-08 15:31:32
36
seck_ndanane11
Mass_ndanane✅ :
Da lene bega wakh nite daga wara xam valeur nit pas valeur xaliss
2026-06-08 20:40:36
14
07jub
taureau :
tonton michoui gua wakh dhe
2026-06-08 22:29:46
7
tifa17443
Dikha :
beugeu akh gnaka beugeu mo yam door bokoul si seuye respect réciproque rekk
2026-06-08 18:43:49
8
To see more videos from user @muqaawim, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About