Blh grâce à toi dina changer yallah khamnané damay diouli mais respecter wouma ko wayé sa appel bii yé nama damay niane souniou borome yobalal mako rkk si barki layilakha hilala guéne nianal ma🤲🏽❤️Encore merci yallah nala souniou borome faye🤲🏽🤲🏽❤️❤️❤️