@tiks2630: Prince après sa défaite contre lac de guerre 2😭@luttetv #viral

tiks26
tiks26
Open In TikTok:
Region: SN
Monday 15 June 2026 20:37:19 GMT
23439
2205
110
77

Music

Download

Comments

mamzoo67
Thier@67 :
😂😂😂🤣🤣🤣🤣 sérieusement ay ré MoMA diap
2026-06-16 00:17:08
56
toufafall54
Toufa :
Dimasa wou wa TikTok bi😭😭
2026-06-16 00:18:09
47
stevinho07
MOmo🇸🇳 :
Vraiment kii desseii neu magg .. li moy sport daga done dane ay mbeur di begg tey gnoy dane la santal Yallah boubax champion ga bilahi
2026-06-16 03:36:51
8
baabadiagnemouham
Mouhamed Anne talibé chiekh 🥰 :
Masta tu es jeune l’avenir devant toi kila dan dou gathié défaite defaye dafarat kou am diom rekc bonne chance pour la suite prince Lamb amngasi thieur
2026-06-15 21:30:57
18
ojaxate
ojaxate :
dafa wara janguii beurré, technique bi dessna et puis nz topp yoon bi na beurré akk ayy moromam
2026-06-16 03:06:44
6
kepzo221
kepzo221 :
bilaye boul dioye beurenga ba danou
2026-06-15 21:39:35
14
momo26369
momo :
notoo wayy mbeur 😂😂 benen yone Moy dakk
2026-06-15 21:10:30
17
emametalalu
E-M-A Entreprise Métal Alu :
du courage t'a pas démérité 🥰
2026-06-15 21:21:24
10
user1300035725215
user1300035725215 :
Ki DIAMBAR la motakh mouy dioy. Bougoul kadiè
2026-06-16 07:57:48
1
tallanho_jr
Tallanho_Junior 🇧🇷🇸🇳⚽️ :
Challenge 😂
2026-06-16 07:39:28
0
momodiaw37
momo diaw :
Benen yon moy dakh nitt monol deuk si victoir
2026-06-16 00:34:51
2
xaliloulah_jr
Ibrahima_Khaliloulah :
yaw champion nga diambar nga benéne dafay bakh mbeur
2026-06-15 21:31:43
6
papemami8
باب مم اميغ❤️ :
malgré faralou mala mais Diambar késsé moy am défaite moukay nakarloo nii mais bilahi ndanann nga té li molay deff champion 😔
2026-06-16 01:14:49
2
lins_boy
Lins 221 :
Champion lay doni dhé
2026-06-16 01:16:01
1
mouhamednd31
Muhammad 🥷🏽✨🌀 :
Mére binta faye bouldioye wayy 😂😂😂
2026-06-16 00:59:43
0
ibnulamine22
AL amine👨🏾‍🦯 :
Khana ki mingui soka am défaite mayniou diam way
2026-06-16 07:20:25
1
dgtendimane
cheikhtidiane :
demlene entraîné dji mo geun si yeneu 🤣🤣🤣
2026-06-16 08:54:18
1
dumpgalsen0
Dump galsen🇸🇳 :
Prince diape si rek mayniou ba match bi diekh koi nga sogay massta wou
2026-06-16 08:50:48
1
To see more videos from user @tiks2630, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About