Machallah way yalna YALLA lafal lén thiate Bilahi xawma len sax mais dema guiss video bi rék sama yaram daw nit déy fonk diabaram ndax diabar moy rakk moy YAYE moy xaritt moy leup boko fonké YALLA fonkeuh leuh donc teye len diabar yi bou bax bou kén saga sa diabar diko diaralé si iow wela nit diko xass ndax iow sama wadji kontane na dh yalna YALLA borom bi may lén ndiabote Goor ak Djiguen mou barkél aussi 🙏🙏🙏 je vous aimes welahi ❤️❤️❤️
2026-07-23 01:10:57
12
user6771391758310 :
Machall
2026-07-23 22:33:48
0
seck ndanane Lingerie 👙🩲🩱🧥 :
Célibataire yalla na dhé 😂😂😂😂
2026-07-22 13:42:49
7
narou yaye fatou :
yallna na lene yalla defal diamou
2026-06-16 16:55:35
50
Leuz deugue ❤️👉🚗🚚🚛 :
Li d souma ko defe sama bb ande ak mome si souf 😂😂😂😂
2026-07-19 18:49:58
12
Ilimane Wade :
Je suis très content
2026-07-22 11:17:41
2
talla baye mor sall :
li dh sumako defone miir lay yendo ki rasoullah
2026-07-22 09:53:47
4
samba azawat :
nioun niou amagoul nio gueneu lahh birr nak
2026-07-19 23:35:22
3
Mame diarra Ba :
que de bonheur à vous
2026-07-20 22:54:05
0
Cheikh bou samba dialo :
Li dafa nekh bly❤️❤️
2026-06-23 13:05:34
2
BAYE 🤍🖤 DAME 🖤 :
👌👌Ndialo bakhoul nekhoul
2026-07-23 20:10:46
1
youssoupha Ndiaye :
Que dieu vous protège machalakh 🤲😍😍
2026-07-09 09:46:22
1
mbaye :
Ho machallah se Nice
2026-06-15 22:41:30
8
Mbaye Geuye :
yalndiam yage
2026-06-17 21:04:03
1
abdou laye mbaye :
yalle naa ande bii yague🥰🥰
2026-06-19 13:34:04
0
Babacar Ba :
wawa♥️♥️♥️
2026-06-16 17:59:32
2
Djibi Sow :
machallah ❤️❤️❤️❤️❤️
2026-06-16 08:50:18
0
amadou sow :
🥰🥰🥰machalla khalléyi
2026-06-16 08:16:17
2
Baye Modou Diop électricien✪☪ :
masala monaim❤️❤️
2026-07-04 10:29:00
0
narou yaye marétou💝 :
wa mes li raféte na way bonne leçon pour moi😂😅
2026-06-18 23:31:42
1
user118662382051 dou bou ndaw :
macha.allah.❤️
2026-06-16 00:47:57
1
Yacine gaye :
yalla na séybi barkél kaléyi li nékh ne 💖💖💖💯💋
2026-06-17 20:54:57
1
Alzo Bu Dip Doundou Guiss :
Machallah Yalla na beuguel sakh
2026-06-15 23:08:01
1
Laye Thiam :
Maachaa'Allah
Na sèn daimm yague
2026-06-16 12:42:50
1
Talibn🇸🇳🇲🇷🇲🇷 :
❤️❤️❤️🥰
2026-06-16 20:02:49
1
To see more videos from user @badasow11, please go to the Tikwm
homepage.