Language
English
عربي
Tiếng Việt
русский
français
español
日本語
한글
Deutsch
हिन्दी
简体中文
繁體中文
API
Home
How To Use
Language
English
عربي
Tiếng Việt
русский
français
español
日本語
한글
Deutsch
हिन्दी
简体中文
繁體中文
Home
Detail
@notdaelyn..2: 🫥
Daelyn Alize
Open In TikTok:
Region: US
Sunday 21 June 2026 22:44:44 GMT
1904
228
1
4
Music
Download
No Watermark .mp4 (
1.42MB
)
No Watermark(HD) .mp4 (
1.7MB
)
Watermark .mp4 (
1.32MB
)
Music .mp3
Comments
xoxo_.natalieee :
😍😍😍
2026-06-22 04:10:48
0
To see more videos from user @notdaelyn..2, please go to the Tikwm homepage.
Other Videos
mexii
inantanadii❤️🇬🇦🫅🏻@anzal pretty gulayso hbo ❤️#qoraxey_jano😍😭🇬🇲😘❤️🇬🇲 #viral_video #Haruun_ruush🦅❤️ #degahbour📍 @xillo janno🕊️
#wlw #thaigl #foryou #fyp #gl
_Seex Muhammadu Mustafaa Mbàkke_ *Moo ngi nggane àdduna ci weeru tamxarit “muharam” atum 1306h yamoo ak septembre 1888 ca Daaru Salaam daje ak jamono ji Seexul Xadiim doon wër dëkk bu sell bi di Tuubaa ba gis ko mu sanc ko ca weeru rajab ci at moomu.* *Way-juram wu jigéen di soxna Aaminata Lóo doomi Seex Muxtaar Binta Lóo ak soxna Xari Maam Jóob, nekkoon ku sell daa dëkke jaamu Yàlla moo joxe woon bakkanam ngir Sëriñ bi, mu ngi làqu atum 1310 ci weeru koor moom lañu njëkk a rob Tuubaa ci ndigalu sëriñ bi(..) moo ko robal boppam gërëm ko wax na ci moom benn bind rekk moo ko dese woon ci téereb* _“risaala”_ _Seex Muhammadu Mustafaa_ *door na am njàngam ci Tuubaa ak rakkam sëriñ Fàllu Mbàkke ci yoxoy seen way-jur Seexul Xadimm bañu àgg suuratu* *“Yaasiin”Mu yóbb leen Mbàkke-Baari ci Seex Ibraahiima Mbàkke ngir Sëriñ Ndaam Abdu Rahmaan Lóo jàngal leen alxuraam ak xam-xami diine, ñu teel a mokkal laataa ku-tedd ki di dem tukkib géej gi 1895, jànge na it ci sëñ Maam Moor Jaara xam-xam yu wuute. Bi sëriñ bi jugee ci tukkib géej gi la ko Seex Mustafaa fekk Muritani 1902 mu taqoo ak moom foofa jàng xam-xami diine ak làkku araab, sufiyàŋŋe, tarbiyu fa, ak mbooleem jikko yu baax yi ci dëddu àdduna ak alal ak daraja jël yoonu mag ña, ci tudd Yàlla ak liggééy ak noot bakkanam.* _ Fa la ko Seexul Xadiim dénke woon way yi *Ku Sëriñ bi bëggoon la te fonk ko seedeel na ko ngërëm ak ag dëggu, ak pastéef, waaye teewu ko tekki laxasaayam mu sax di jàngale ak a yare ak liggéeyal way-juram ba keroog mu nekk xalifa atum 1927.* *Taxawu njaboot gi ak sonxna yi wormaal leen ak i rakkam boot ñépp yamale leen, ngir am ngërëmu ku-tedd ki, mu yóbb soxna yi Njaaréem, soxna Maymuunatu as suxraa nettali na ne ; Bunu masaan a lekk ba noppi danuy jox mbubbam mi mu sol nu fomb ci sunuy yoxo.* *Bi Sëriñ bi ñëwee Njaaréem atum 1330/1912 juge Céyéen Jolof ci la ko digalee mu dem Tuubaa ngir mu dëkk fa ànd ak Seex Ibraahima Faati ñu defaraat ko gas fa ay teen sos ayna rahmati samp daara Guy texe jox ko Seex Muhammadu Silla Ñaaxeen ak Seex Sulaymaan Géy ak ñeneen.* *Ci 1915 mu digle ñu sos ay sàq ca Tindóodi mu yabal fa Muhammadu Silla Ñaaxeen ak Móodu Muxtaar Njaay Nguri ak Sëñ Móodu Faal Paataar ngir dajale mbay mi yóbb ko Njaaréem ak 42i kaamiil, ci 1918 mu gas teen fi marché occas nekk ginnaaw bi la ko Sërñ Fàllu yeesal, def ko marché. 1839/1920 mu yaatal Husnu ma’aab def fa kër ak daara jox ko sëñ Maxtaar Aale Lóo, giinaaw bi la tukki Kayel 1340/1921 yóbb fa Mahammdu Silla Ñaaxeen laataa mu kay yóbb Tuubaa Ñaaxeen bi ko Maam Seex Anta jox àddiya jamono jooja la sos dëkk yii; Nayde, Bulyéeri ak Xàbbaan.* *Ginnaaw tàggat boobu ngir yan bu diis bi koy xaar ku-tedd ki woowaat ko Njaaréem tabaxal ko fa kër ngir mu gis doxaliinu sëriñ bi diggam ak tubaab yi ak taalibe, ginnaaw bi la ko yónni Ndar ngir mu dalal Seex Siidi Baaba, ca la defaloon ay way yu yéeme. Atum 1341/1922 mu ànd ak Sëriñ bi dem Ndakaaru ñu wàcci kër Jean Caam, ginnaaw Seex Mustafaa jënd kër gi ndax Ku-Tedd ki dafa saxaloon di jàng alxuraan ak a julli.* *Mu nekkoon loxo ndayjooru Sëriñ bi ci yu bari ba ci ay jëflàanteem, ba bi ko réew mi sàkko ndimbalu xaalis(...) Ngir ay jafe-jafe moom la sëriñ bi joxoon 500,000f mu yóbb ko.* *Bokk na liggéey yi gën a fés yi mu def ginnaaw bi Ku-tedd ki làqoo ci jamono ci yu xat te metti atum 1927 njaboot gi jaaxle ndongo yi tiit, noon bi wër ko bekkoor bi laal ñépp kenn xamul looy def, Ci la juge Ñaaxeen dem Njaareem fekk xew-xew bi siiwagul ci la ko taxawu indi ko Tuubaa* *Ci at moomu la nekk ki njëkk a wuutu baayam ci yan bu diis bi ci taxawal jumaa ji yar ndogo yi ak jàngal leen ak taxawu njaboot gi ba duñu xiif duñu mar fonk sariiha ak sunna te ragaloon Yàlla Sëñ Móodu Mustafaa Mbàkke mu ngi làqu 3i baraxlu “Sahbaan” 1364h yamoo ak #mouride_sadikh_officiell #viraltiktok
About
Robot
API
Legal
Privacy Policy