Dolli sant Yallah bou baax ci limuñu boolé té xamni loumako ci sant rek doyoul ndax bimou nammé ci sama djëmm lenn li, yaw lama boolél ngamay dello ci moom dima begguël saa-souné. Amel naala ndjoukkël lou rëy sah, ndax limay am ci yaw, Yallah dogal nani ci yaw kepp la yam. Alquran neexna lool sah wayé mane bingay djang yaw moom la taamou. Ya baax té mëne lingay deff, ya rafet dialoré key, duñ la wane lingafi bayyi guinaw moukk ngay am kersa, lou rëy ngafi bayyi, lou kenn doul naatablé. Wax ci yaw daanaka ci la dëkk wayé dafa fekni ci begguël ma nga dëkk yawit kone yii mënta ñakk.
Ya baax ci mane, guëne ci mane, mëne ci mane.
Yallana Yallah fayla fay bi guën ci fay yëpp, Yallana Yallah mayla Aldiana Firdawsi 🤲🏾.😭😭
2026-07-09 21:50:30
1
To see more videos from user @mame.mor.quran.221, please go to the Tikwm
homepage.