@salihate1610: Serigne touba rk

𝓥𝓢 🍀𝓢𝓛𝓗𝓣🫧🌸
𝓥𝓢 🍀𝓢𝓛𝓗𝓣🫧🌸
Open In TikTok:
Region: SN
Monday 29 June 2026 22:39:41 GMT
9812
2148
71
5

Music

Download

Comments

bb.anista24
bb.anista24 :
Serigne saliou Néna nitte kou nek amna loula nekh si mome amna yi tame loula nakari si mome nena sou niare yeupou dadjé dieuleul lila nekh si mome té mougne lila nakari si mome. Djeureudieufati serigne saliou kenn dou mome
2026-07-04 12:33:50
135
ndeyesarr650
N~L~S😍 :
serigne saliou néna nit kou né amna louna nékh si mome wayé tmt amna loula nakari si mome bougnou démé ba niar yép dadié naga dieule lila nékh si mome té mougne lila nakari si mome🥹🙌🏼🕊️
2026-07-15 13:50:09
1
poupe.barbie568
Poupée barbie 🫶🏽🫦🫂 :
Serigne saliou néna bir diarla sa birou bopou akh sa birou bambél mouné boula sa ribou bopou yitél ndakh Loufa nék yalla kosimsi déff mouné nala sa birou bambél yutél ndakh lofa dieufoul dokofa fék 🫀🖇️
2026-07-14 15:57:37
1
_penda.niang
thiatou yayame 😍♥️🫰 :
Serigne saliou néna mane douma bayi li ma xam cii nitt ndax lima dégg ci mom ndax so bayé nitt ndax ligua dégg ci mom dafa fék ligua dégg ci mom mola génal ligua xam ci mom nitt amna boula ko wané baya na téyé ko ndax lolu ngen ande pendant des années (ay dégg na waroko tass) bari ay digganté di tass "degg na”moko tass Bo niaw ndiorte rek ligua xol Guay guiss🫶🏽❤️
2026-07-10 09:14:56
22
bb.ndeye.mou.s.saliou
✪Bb Ndeye mou s.saliou🌹😘💍 :
Diokh len ma ndaw ni ma deff si nioume la serigne Bamba defon si mako ni❤️🥺
2026-07-13 21:20:11
3
princessebousaliou43
una salihate 🦋🦋 :
serigne saliou néna diokh léne ma ndaw gni ma thi gnome la serigne touba dane déne thia mague gna♥️♥️
2026-07-05 20:39:58
31
bbeifary3
🌸Bbei Fary bou s saliou 🌸✨ :
Yalla fay serigne Saliou 🥺🥺
2026-07-08 01:04:56
8
aida.saliou02
Aida saliou 🩸❤️ :
Serigne saliou néna nit ak souf nio yam Bo thi defar mou bax 🙏🏿🤍
2026-07-09 19:23:54
11
salikhate.bii1
Salikhate bii :
borom khelcom borom Ndiapandal borom yeurmandé borom darou marnan borom diamono borom yeurmandé dieuredieufé Sérigne Saliou Mbacké 🥰
2026-07-09 16:51:19
7
yaye.darou.bi1
Yaye darou bi🙏❤️ :
Serigne saliou mbacké nena lou niepou xam wax thia touti doyna thia 🙏
2026-07-12 14:44:56
3
its__bb.sonia
Its__bb sonia ❤️😻 :
Serigne saliou nena kuy xool nit di gis ci mom ak sikk, na la leer ni baaxa goo !!!🥰
2026-07-09 16:01:50
5
une_salihate28
Une Salihate ❤️ :
A Saliha néna ''nitte sou fékké xam xam AK yare meun ta dadjié thi mome nagne ko yare té bayi xam xam bi '' ❤️A Saliha protége
2026-07-10 10:34:43
3
mameboussofaye55
mameboussofaye55 :
SERIGNE SALIOU NÉNA KOU RAGAL AK KOU YAKAMTI RK MOMA DIAKHAL❤️
2026-07-10 11:12:39
3
diarriatou_diop
®M-DIARRA_D™💗 :
Dieureudieufety SERIGNE SALIOU 💗
2026-07-09 16:27:23
4
myathiate7
Mina🦋 Rasoul 🦋 :
Mame saliou Nenaa ma djii tou guénee topp sm guinaww suma démé ba guisatouma léneuu ma depeu dieul sileneee🙏🥹🤦🏼‍♀️❤️
2026-07-11 20:13:30
3
awa.mbaye2009
Awa Mbaye :
limoy wakh barina🥺sama sague bi😭😭😭
2026-07-10 00:37:06
4
yacinegueye2230
Yacine saliou Gueye 123 :
Serigne saliou mbacké borom khélcom yémé na 💙🤍💙🤍💙🤍💙🤍💙🤍💙🤍💙🤍💙🤍💙🤍💙🤍💙🤍💙🤍💙🤍💙🤍💙🤍💙🤍💙🤍💙
2026-07-10 10:29:31
2
madjiguene.ndiaye961
Madjiguéne Mou Saliou🥹☝🏾🙏🏿 :
Serigne saliou nèna : Diokh lène ma ndaw yii df si niom lii serigne touba df Sii makk gnii🙏🏿🥹
2026-07-12 17:50:52
1
elhadjngom0
elhadjngom435 :
mbacke ballla aicha 😊
2026-07-09 16:14:50
3
sokhna.diop90
sokhna.diop90 :
Serigne saliou nena bayil nit gni ak sab der té bayé lene ak seni der ♥️♥️diadieuf Mbacké
2026-07-13 01:01:24
2
moukhamed.ndiaye02
♥️ mouSerigne saliou 😭🤍 :
kendou serigne touba ❤️🙏🙏
2026-07-10 02:34:28
2
awa.man05
awa mané 🍯❤️✨ :
Serigne saliou mbaké néna kouma rousoula fék hélcome rousoumala ték si lohoy Serigne Touba
2026-07-15 01:22:33
1
mamefatymbaaye
s faty saliou🥰 :
SERIGNE SALIOU NÉNA. Adouna dem na dedou na lokoy geuneu wouti moulay gueuneu dedou téh yalla loko diégué mou gueune la diégué ✅
2026-07-15 10:53:15
1
sokhnanogayesaliou57
sokhna nogaye saliou :
serigne saliou néna souma lén ditoo dilen guessou rék souma lén soré takhawe négue lén souma demé ba guissa touma lén dépe dadiek yene waye douniou mese taguo dieureudieuf serigne saliou 🙏🙏🙏
2026-07-09 10:23:32
7
khady.sene181
khadija.sene181 :
Serigne saliou néna yalla dafa sakk nite ak nianri bire birou dieumeum DJI AK birou bammel wayé birou dieumeun DJI boumou ko yitel ndaxe yalla miko sakh dina si def Dara nako birou bamélam bi nako yitel 😭🙏
2026-07-08 14:05:54
6
To see more videos from user @salihate1610, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About