@modouyaaydie: Seriñ Mustafaa. Jërajëf jëfal say jëf du bon say wax du bon Mbooleem ñi baaxa ngilay gëram yaw Mustafa Yaw Mustafaa awma sag pay waaye yal na nga tiim Bu wér ci barkeb Sëriñ Tuubaa li jant bi tiim Dalal nga xel yi, seral xol yépp, yal na nga faf Suuxal ña gën seeni kem nim njàpp suuxale tiim Sa jëmm jii nuy janool’ak say ngëneel a waral Njariñ yi dëkk fi ñun, yàggal te boole nu moom Yàggal te boole nu moom’ak lépp lëf lu nu am Sab xol ne guuy’ak sunuy xol ñépp sant ba luum Ku nekk bég na ci yaw, yaakaari kenn tasul Asal, asal ka la jiital Mbàkke nammul a juum Taxaw nga temm ci aw yiw yal na Yàlla taxaw Temm’ak ngëneelam ci yaw, jébbal la sépp soloom Boo jekkiwon rekk lal sab der du yàq ci yaw Lëf, waaye itte ju rëy jee tax nga ñàkk moroom Defar nga àll yi ak kër yépp yaw ba ñu jag Ku nee ngi am itte ngir yaw mat nga ñépp boroom Fu nekk tojj nga fa yit ab àll samp fa kër Bégal fa nit, may ko fab xaalis defar fa goroom Sag cant ñépp la war, saw tagg ñépp la war Mag’ak ndaw’ak képp koo jis rembatal nga yoxoom Ku lay xarab dub julit, dus gor te dub murit it Ku yewwu sant la biir’ak bitti mbaa mu ne xiim Lii laa la wax man, sa fan wii yal na gudd nga tiim Mboolem ña tiim’ak ña tiiméef’ak li jant bi tiim ! -- Yaa def lu lew domm ngir yaa jàpp àll yi toj Rajax ñu mokk nga bay am lépp, lii daganéey !

Modu Yaay jé Mbenda🟢⚪️
Modu Yaay jé Mbenda🟢⚪️
Open In TikTok:
Region: SN
Tuesday 30 June 2026 23:41:37 GMT
9599
1179
27
47

Music

Download

Comments

apple.khalil
Noga SERIGNE backe ❤️👌 :
💚💚💚C’est
2026-07-02 21:49:28
0
sokhnafalilou8
xaritou yayam :
🤲
2026-07-01 06:53:41
1
fallou.galasse1
Fallou Galasse 🤍🫶🏻🤍🫶🏻 :
💕💕💕🥰
2026-07-01 01:41:43
0
mbayallgui
MBA YALLA :
cëy sama dourando
2026-06-30 23:52:24
0
modouyaaydie
Modu Yaay jé Mbenda🟢⚪️ :
Thiey Seex Moustapha 🙏
2026-06-30 23:50:54
0
761365666.serigne.sam
SERIGNE SAM 761365666 :
2026-07-01 19:20:30
0
mortallandouyetechnicien
Mor Talla Ndoye Technicien :
🥰🥰🥰🥰
2026-07-01 17:39:46
0
user4642508075588
user4642508075588 :
❤️❤️❤️
2026-07-01 08:00:15
0
baye.masse.sow3
Baymass ❤️ :
❤️❤️❤️
2026-07-01 14:46:24
0
matydiop1982
user3102760062781 :
❤️❤️❤️
2026-07-01 17:52:19
0
dabandiaye2246
765742293♥️♥️ :
🥰🥰🥰
2026-07-01 09:14:50
0
user1337422350668
Khalile :
❤️❤️❤️
2026-07-01 08:53:49
0
zizabi1
talibé borom touba la :
🥰🥰🥰
2026-07-01 08:35:33
0
bakh5417
Khadim Gueye :
🥰🥰🥰
2026-07-01 06:32:30
0
maguette.ndiaye527
Maguette Ndiaye :
🥰🥰🥰
2026-07-01 07:56:25
0
tallaka22
tallaka22 :
❤️❤️❤️
2026-07-01 07:43:21
0
chiekhdieng835
Serigne cheikh khassida reék :
🥰🥰🥰
2026-07-01 07:33:55
0
ndaye.diakhata
ndaye diakhata :
😂😂😂
2026-07-01 07:16:02
0
alioundogn221
Lindo221💰 :
❤️❤️❤️
2026-07-01 12:41:38
0
user85590829883484
serigne gaye :
🥰🥰🥰
2026-07-01 01:52:27
0
diarista.445
DiOPBAYFAll247 :
🥰🥰🥰
2026-07-01 01:21:48
0
user9048255674671
user9048255674671 :
🥰🥰🥰
2026-06-30 23:58:01
0
moussambaye378
médecin traditionnel :
❤️❤️❤️
2026-07-01 18:26:09
0
serigne.mback.dio408
Serigne Mbackè diop 920 :
🥰🥰🥰
2026-07-02 00:32:52
0
laminekara20
tallasene333 :
❤️❤️❤️
2026-06-30 23:48:12
0
To see more videos from user @modouyaaydie, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About