@khadim.bamba2828:

khadim Bamba 2828
khadim Bamba 2828
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 05 July 2026 10:22:00 GMT
10682
802
90
16

Music

Download

Comments

oumish716
oumish :
MAN DAMAY LATHIE LANE LALÉN SOKHNA AÏDA DÉFFF ???
2026-07-05 12:27:47
7
omarfaroukh
Al Faroukh :
ayda amoul niarigne si yoon wi😳
2026-07-05 16:26:01
3
ouzinfall3
Ousseynou fall 🇸🇳 :
Le problème dou sokhna Aida gni siy wakh yeup basi kilifa yi siy wax lou biaw Serigne bethio maniou beugoul lolou moy deug histoire c’est la kham nagn lep li Serigne Saliou def si Serigne betjio meussou len nekh
2026-07-06 01:26:09
3
cheikhfayelampe
cheikhfayelampe :
gniognou sokhena Aïda bolen raw si dieufal serign Bethio dieufeul serign Saliou dieufeul serign Touba dieufeul yalla sokhor rek moyen diap
2026-07-05 14:39:58
4
user2025637158750
idy diop :
wakho deug aida Diallo mo gana yess thii mourid yii sene genre yii Nion yakh yonwi ibliss louko dall bagna topou digal mon takh
2026-07-05 23:52:18
1
2sdpro1946
DYNAMIC SËRIÑ SALIOU DIAGNE✪ :
JEREJEFF MOURIDE KADDOU YI AMNA SOLO❤️❤️
2026-07-05 18:51:00
2
ngor.gning148
Ngor Gning :
walakhi deugue Bou weer la sokhna Aïda saliou deffoule kene darra sokhor ak seytane ak kignane molene diape waille ndame rek inchallah rabbi dieuredieuf arête toogne d'où Galatie nite deye lacke moromam 🔥🔥🔥🔥
2026-07-05 21:55:33
3
modou_bara2
MODOU BARA DIOUF :
dallam iow rek la gueunn. Yeneu xalisss rek nguen di toppou
2026-07-05 12:32:52
2
labsolu6313
l'habso :
C'EST SERIGNE BETHIO QUI DÉRANGE..MBIR MI SERIGNE BETHIO LANIOU MEUNOUL DIGÉRÉ... MALHEUREUSEMENT POUR EUX YA AÏDA SALIOU SAMPOU SERIGNE BETHIO BI WESSOUNA LEN BOU YAAG
2026-07-06 07:28:42
2
issa.kane96
Issa kane :
Sokhna Aida Saliou ndiarign kep la loumou am dieufeul nako serigne bi ba takh mou déf ko djeumeum dou hasard de
2026-07-05 14:42:41
3
baaymorjoop7
BaayMorJoop :
MashAllah Yaraam kaddu yi Tégginé na Tei Am solo
2026-07-05 14:15:20
2
maniass.nguirane
nguirane :
wakhou fi darra bilay mourite ndigal rek aïda diallou domourame leu
2026-07-08 18:01:44
0
derbat.construction
Derbat Group Engineering :
Sa wax Amna dieurigne loool
2026-07-05 10:32:58
3
assalihleternelheureux
AS-SALIH L'ÉTERNEL HEUREUX 💙 :
YA AMMI TEGUINN WAY MOURIDE.. AKASSA 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
2026-07-05 17:38:54
4
moustapha.gueye.7
Moustapha gueye :
💚💚💚
2026-07-08 12:23:44
0
user8820496970307
user8820496970307 :
aïda diop2
2026-07-05 17:37:16
1
chenkona.gueye
Chenkona Gueye :
ما
2026-07-05 11:03:29
0
moustapha.gueye.7
Moustapha gueye :
💚💚
2026-07-08 12:23:34
0
layedione85
dionelaye009 :
sokhor rek Molène diapp
2026-07-08 00:41:58
1
moussafaye1857
Moussa abdou khoudos faye :
serigne amsa koubakh sokhna aida masoumako guiss wayé wayi s touba la
2026-07-08 18:36:33
1
deugoudeuegeul
DEUGOU DEUEGEUL :
BILAHI KOU BEUGU SERIGNE SALIOU TEH MOUY DEUGU PAR FORCE DANGUAY BEUGU SOKHNA AIDA SALIOU
2026-07-08 15:36:37
0
souleymane.ndiaye991
Souleymane Ndiaye :
Ma chalah
2026-07-08 22:48:24
0
moustapha.gueye.7
Moustapha gueye :
💚💚
2026-07-08 12:23:28
0
moustapha.gueye.7
Moustapha gueye :
💚💚💚💚
2026-07-08 12:23:21
0
cheikh.poulet1
Cheikh Poulet :
Machallah
2026-07-05 12:21:26
0
To see more videos from user @khadim.bamba2828, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About