@zikre_samaou_tv:

ZIKRE_SAMAOU_TV
ZIKRE_SAMAOU_TV
Open In TikTok:
Region: SN
Friday 10 July 2026 15:37:41 GMT
47713
4122
442
131

Music

Download

Comments

awainsa0405
Eva Sita💖la Mamoureine 🥹❤️💫 :
Mane monme dama done dem Souniou diouma di sét yalla souma demé doumako guiss may dioy di wakh yalla dama bagn 😂😂 ms Alhamdoulillah Dieurudieufé Baye🥰
2026-08-28 10:30:00
8
makhtoum2002
Mactoum 🇫🇷 🇸🇳 :
Thiakhane kep louy guiss yalla 🥰 Sénégal nekhna bilahi guiss yalla 🤣
2026-08-28 14:01:22
0
toubachicory313
Ousmane.. ! :
Mane commentaire youmay lire fi mom doyna waar dih kou sagna wax 😂😂😂😂💔🤦🏽‍♂️yallah ndiabot
2026-08-28 14:18:33
1
glow1234hup
Glow hup :
Maneu mome a chak fois soumay wird rek dafa ameu beneu mbottt bouyyy gneuw baa sama kanam takhaw… pdt deux à trois jours legui ma wakhko gnima dieulado wird nilene est ce que dou yala momay fégnou si dieumi mbott biii mais jour Bobou dagno retane ba faténi gnougui si wird 😂
2026-08-27 16:22:41
155
badubarhama63
𝔹ă̈D̑̈𝕦 B̆̈ă̈R̆̈h̆̈ă̈m̆̈✪ :
Mane mom dama tokk nane yalla amoul kilifa ko khamni louko nekh lay deff te kene dou wakh👋🏽
2026-08-29 02:19:13
0
ballira4
Diarra rassoul :
Amna koudone wird souniou chambre université niew si mane nane ma figay révisé fofou lama djiné fek diokh ma yeuré bou rouge pour ma bayi ma bagn mais photo na yeuré bi ma wanela maniko détttt mane dama gawa dead 😂
2026-08-26 22:44:20
111
fabadou0
fa💕 :
Bima tarbiya ba paré dama don tok rek seuguémeu kouma ladj lanla manila fima nekone nekh na dama fa beug délou ndékété adouna nekhoul alhakhira nekhoul yalla mo nékh kafana cheikh Ibrahim Niass 😭🥰
2026-07-30 10:46:43
481
sbn_shop0
Sbnshop❤️🇨🇳 :
😂😂Un jour sama papa beug fay lamp keur gui mani yallah soumako guisser ci leundeul bi meune na diomi kone boul faye lampe yi
2026-08-27 02:13:21
95
bafama2000
fama la barhamienne :
Durant mon premier jour Wird di nelaw ba kourous bi Wade ma teupe di dioy ni yalla rombou nama dotou mako guiss 😁😅
2026-07-30 11:32:38
247
flowerbomb86.ou
Vanille 🌻 :
Tarbiya presk 2 mois agouma, un jour ma diouli timiss ba parei rek craquer commencer dioy dioy you meti di wakhtou nane yalla bougoul ma xamko 😂 nane mane c’est fini bokouma ci gniy kham yalla 😂 ma parei sani krouss bi feulé 😂 wayer je me suis vite ressaisie, ndeyssane quelques jours legn ci tek ma am Fathou 😭❤️
2026-07-29 10:29:14
149
ousmaneka83
Ousmane barhama ka :
Magui dioy sak Bilahi bima lire sen commentaire yi nianalléma ma trbiyou comme yen
2026-07-27 14:08:52
176
rokhayandao417
rokhaya ndao :
dama beug tarbiya walahi qui peut m aider slvp
2026-08-28 03:18:51
10
rockhaya.mbow
Une ky@❤️💕 :
Man dh beug yallah ak am fitt rkk mtx ma defko mei j'avais tellement peur d'être seule Lou yengatou mani wouyy yallah mingui nieuw tay ma dead😅😅
2026-07-30 12:35:56
69
mouhamedc01
MOUHAMED 🇸🇳🕸️ :
Yalla na leen yalla guener si rerr bi guen nek 🙏
2026-08-01 16:24:03
48
user5790926011351
la b@rh@mienne♥️🥰 :
ndeysane 2012 doumako meusseu fatté dama démone ba décourager un jr ma dioully fadiar ba paré rék nalaw ma guenth di werde sama courouss bi wade baye yéma si guenth bi for courouss bi téguatko sama lokho ma yéwou amath force ba nima amé fatkhou mashallah yallananiou yalla fayal baye Niass alhamdoulilah diereudieuféé Baye 🥰
2026-08-27 08:06:48
12
kandjistore1
kandjistore1 :
Xana sama xarite bi ladj ma niata la werde si 4h ak legui mani ko ay 10k rk mounei moh iow werdo Dara do yeig dh😁 ma guein dem si arrière cour bi joy ba doyal rk nak gnew ni yalla sumala naroul xam defal sign sumala narei xam nak yokk ma courage ma guena werde mai Alkhamdou lilah g compris après k ni sma xarite bi dafma done booster pr ma bania bayi sama loxo. Lahilaha illalah nak la done bagn deig fumako deig joy t duma xam prkw .. dem sama keur Moukhadam niouy diouli timis mai zikr bu biniouy def avant diouli bi dama joy ba nimay joulei magui joy. Tarbiya nexna🥰🤗yalla naniou yalla fayal Sheikh Ibrahim rta
2026-08-28 02:02:43
20
mamour_nani17
Mamour17__Baye__Niass🌍🇸🇳 :
période corona nieupp di dem sen keur nioune niouy dem si alleu bi 😂 di xooli ko khamné magui ko bayi sunu keur dinguerie !!! Keen dou baye niass 🫀😭
2026-07-31 09:06:43
90
dioufmoubaye13
diouf_mou_BAYE :
Man mom dama don Faye lampe yi parceque dama yakaron que ni dafay am lumière bouy watieu pour wakh ak man 😂😂😂😂
2026-08-02 16:00:59
51
sokhnaaicharassouldione
Sokhna Aïcha Rassoul Dione :
mane mom dama done dioy ni yalla mangui wirrd di concentré wou di daw nitt douma nelaw th meunou mala guiss xana mane dama bokoul si gnila wara guiss kone 😂😂
2026-08-23 02:13:56
12
ndaw.kounda4
𝓝𝓭𝓪𝔀_𝓚𝓸𝓾𝓷𝓭𝓪🧑‍💻🥷 :
Eskey Diarama Cheikhal islam 🥰😂
2026-07-30 00:38:03
36
poullobaye.221
RACHID KNM🇸🇳 :
@RACHID KNM🇸🇳 :amone na béneu instant si biir tarbiya bi bima amé 11 jours sama gorge bi di méti ma dioy ni ah c fini Yalla bougouma. mani damay bayi. ndeysaan si 11e jour bobou laniouma guéné sama keur Baye. dakkeu ma sibiti. motakh souma dégué sarimane rek sama khol toy wallahi
2026-07-31 22:23:45
40
fatimarassoul46
Fatima mou SBN🥰❤️ :
Mane dh dama wird ba sonou mais bima sama mouhadam diapé nima euwaloul akhiroul zahiroul batinou firil ma ko bima gnibé la am fathou Alkhamdoulilah dieurdieuf baye Niass🥰
2026-08-24 11:32:46
5
lamine.talib.baye
Lamine talibé Baye :
dieuredieufé mawlana cheikh Ibrahime Niass
2026-07-30 15:49:45
5
kenza1939
. :
dama beug tarbiya qui peut m aider slvp
2026-08-02 20:44:41
18
ibnt_yatta_baye
Yayou sheikh Ibra Fall❤️ :
Fanawou di breugou ndëkkei j’étais enceinte🤣🤣🤣
2026-07-30 09:38:16
37
To see more videos from user @zikre_samaou_tv, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About