alkhamdouli alkhamdouli alkhamdouli alkhamdouli salalakhou aleyhi wa salam ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2026-07-14 18:18:40
31
Mr_Ousman❤️🤍 :
Ndaysan Com souma kay gnane 😩may Y’allah yaw borom Asaman Ak souf yaw mi def di dindi yaw bour bou bakh bi man sa diam bou xébou bi Mangui lay kenal dila wax Allhamdoulilahi thi lép linga ma défal louma xam ak louma xamoul 🥰dila wax ni yaw rk la yakar Amoul kénén kham Nani samay Bakar Beuri ba diakhal ma Wayé sa yeurmandé moko eup kon nak Mangui lay niane nga diégal ma ta bagne ma top thi samay dieuf 😩Après nak ma gnane ko lép lima beug wlh Ndaysan des fois Ay heure you ndaw mou défal ma lima beug des fois nk mou khagne ma Wayé ma khamni Rk dfa geunoul si mann 🥰🥰yalla bokay gnane Rk bak ko