Ndayssane sama yaram dawna sama khel demna si baye bachir ndaw mom rk la ma diokh 😭😭
2026-07-14 19:47:04
44
Abibou Gueye :
yalla nafi yague te am diamou
2026-07-14 16:17:53
2
dia Malick 👌👌👌👌💯💯💯💯 :
machalla yalla nala yalla samal bopam rek
2026-07-15 07:41:40
0
Sopey elhadji cheikh tidiane i :
sognio khalifa seydi habib ndao ibn elhadji omar ndao yalla na yalla guoudeul faname🥰🥰🥰🥰❤️❤️❤️❤️❤️
2026-07-14 16:00:44
2
Librairie Al-ahmadiyya :
Dafa wara ame khalé bou ande ak mom😭
2026-07-14 21:17:03
19
yayi ndama :
machallah yall na yalla yokkou aye faname ndaocounda 🥺🥰
2026-07-14 20:24:44
5
DRAME ET FRÈRE MARCHÉ CASTOR🥳 :
Machallah serigne bi bouy dokh na am niou ande ak mom kilife dou dokh mom kén rawaté Mack rawaté na moy taw naniou bayi xel li dou image bou réfet rawate na niou né yaye khalifa seydi Omar ndao
2026-07-14 22:17:42
24
Im___kebii :
Walay ni dh la mel ndao mo bakh mo oyof
2026-07-14 21:02:20
6
DG🫀sope C M S D❤️ :
Gua taneko yenene khalifa yi🙈
2026-07-14 23:53:22
3
user1315825046153 :
noumay déf ba ziaré ko
2026-07-15 00:58:45
0
kebba touray beug baye niass :
Machallah yalla molén njour 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2026-07-15 00:02:18
2
Babacar ibn Abdallah💫🕋🕌 :
machallah yalna yalla goudal fannam🥰té wéral ay thieuram🥰🥰🥰🥰
2026-07-14 20:00:08
4
GUET ARDO plombrier :
thiéy gourou yalla yi
2026-07-14 20:53:27
4
NITOU DEUG :
Ndeysane mogui may fatalii moment yiii yalla dji dane taww nokh mou beuri wakhtu djiouli diot may dém dioulidji gniounima khana guiso nokhmi manilén téhh soufékoné khaliss la mou diaralma donc nokhmi dou téré dém
2026-07-14 21:45:38
2
pape A. Sow Mouhidiste :
yalna yallah faye Borome Darou salam saloum
2026-07-14 21:45:52
2
minetou_bussiness✨️ :
ohh Maam habibe yaggal diamono ndao counda🥹❤️😍
2026-07-15 00:37:16
1
BLODIN DIOP JR🇸🇳🇺🇸 :
Maschala Ndao yagg fii loll . Mais waronn na am nioukoy accompagner tei teyel ko parapluie ☂️bii . Vraiment prochaine fois
2026-07-14 23:02:39
4
cissé teranga :
ndeysane yalna yalla yagal ko fi lool té am diamou
2026-07-14 15:54:02
1
Amadou USA🇸🇳🇺🇸 :
Ndayesan 🥺
2026-07-15 11:27:01
0
Mamour Gaye :
🥰🥰🥰🥰ndaw kounDa
2026-07-15 15:14:09
0
محمد مصطفي به ابن ألحاج بابكر :
gni yalla rk Allahu Akbar
2026-07-15 13:11:27
0
Mohamed Cissé ❣️❣️⚔️⚔️ :
billahii ndaysan ❣️❣️🙏🙏
2026-07-15 12:02:55
0
Alloalph :
« Dem diouma mouy taw, mo gueune dougou si bamel mouy takk » Serigne Abdou Khadr Mbacké, rapporté par Mbaye Pekh
2026-07-15 13:20:27
0
To see more videos from user @khalifamountakhatv, please go to the Tikwm
homepage.